Wakh Ma Finga Nekk Lyrics
Wakh Ma Finga Nekk Lyrics by ASTAR
[VERSE 1]
Ma ngui fatikou big ma néwone y'Allah
Que kén dou kheutiok mom leep mome la métina
Wayé souma sagnone, douma tokhalé rongogn
Li dess souma ko khamone do bayi samay lokho
Maman wax ma fi nga dem wa
mane mba nékouma di guenteu
Di khalate souba tell you
Nékh yi nga done yéwo sama wett
Assamane si yatou na wayé ioe rek lay guiss
Goudi gui sorri na li doyna tiss
Kholal nima wéttééé...! hannn hannn
[CHORUS]
Waxma fi nga nékk
Waxma fi nga nékk
Waxma fi ioe yaay hann hann
Waxma fi nga nékk maaa
Waxma fi nga nékk maman
Waxma fi nga nékk
Waxma fi nga nékk
Waxma fi ioe yaay hann hann
Waxma fi nga nékk maaa
Waxma fi nga nékk maman
[VERSE 2]
Maaa waxma fi nga nékk mamamaaa
Antanouma li ma yeugue everyday
Kouma néwone dina am
Doumako meussa geumé
Mane déh kham na ni
Yarr ngama fig ma wara yaré
Khamal ni yaye do meussa am gathié
Mane fane la dieum
Mais khawma fouma wara diar
Tektal ma yoone bi ba safar ak wittar
Lima done mane yama def star
Waxma fo nékk souma sagnone
Boumala wowé ngané ma nam
Ma ngi yégali sa réve moy sama mission
[CHORUS]
Waxma fi nga nékk
Waxma fi nga nékk
Waxma fi ioe yaay hann hann
Waxma fi nga nékk maaa
Waxma fi nga nékk maman
Waxma fi nga nékk
Waxma fi nga nékk
Waxma fi ioe yaay hann hann
Waxma fi nga nékk maaa
Waxma fi nga nékk maman
Maman, waxma fi nga nékk
Mamaaaaaa...! yeah héé
Maman, mamaaaaa...! yeah héé
Watch Video
About Wakh Ma Finga Nekk
More ASTAR Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl