I Missed You Lyrics
I Missed You Lyrics by ASTAR
Gueudj nala guiss kay wakh ma tchi loy dokh
Gueudj nala guiss kay wakh ma tchi loy dokh
Gueudj nala guiss tchi lane nguèy dokh
Nameu nala lou barri mba yangui tchi djaam
I missed you
I missed you
Kaay gnou took
Tu m’as manqué yeah
Mane namone nala, kharitt sama
I missed you
Depuis école, laleu gueudieu guiss
Lèglèg meu bind leu snapchat mais domeu tontou
Sa instagram, mèy khol sèy story
Di latch ndakh yaw leu boy pirates yi deugno beuri
Kouleu hkol kham ngueu né
Namou ma dara chérie
Khèl bou dal dèy fègn fèep
Yawitt ak ni ngueu tarro
Wagnil ndakh yangui guagn
Boy seu doundou nèkh neu
Wakh ma li lane la
Sagnsè bi bakhna oh mashallah
Gueudj nala guiss kay wakh ma tchi loy dokh
Gueudj nala guiss kay wakh ma tchi loy dokh
Gueudj nala guiss tchi lane nguèy dokh
Nameu nala lou barri mba yangui tchi djaam
I missed you
I missed you
Kaay gnou took
Tu m’as manqué yeah
Mane namone nala, kharitt sama
I missed you
Mane tamitt nameu nala
Ba la makoy fate diokhatt ma seu téléphone
Pourtant astou bobou beu légui changer wo
Ana maty nak halèbi mba moungui si djam
Woy wagnil yangui guagn
Dèffou ma dara chérie
Tèkk ngueu lèep tchi temps
Bou leu doyoul meu dooli
Mba fatè woma
Dara namou loko
Sa sagnsè bakh car mashallah
Gueudj nala guiss kay wakh ma tchi loy dokh
Gueudj nala guiss kay wakh ma tchi loy dokh
Gueudj nala guiss tchi lane nguèy dokh
Nameu nala lou barri mba yangui tchi djaam
I missed you
I missed you
Kaay gnou took
Tu m’as manqué yeah
Mane namone nala, kharitt sama
I missed you
Kharitou dèmb ak tay warougnou changer
Dotou gnou gueudjeu guise amie fègn na tay
Nameu na sèy wakhtane sama domou ndèye
Anndeu bou yaguè lool deug mofeu dèss
Hey hey lane namone nala
Hey hey astar namone nala
Hey aicha koné namone nala
Hey kharitt namone nala
Gueudj nala guiss kay wakh ma tchi loy dokh
Watch Video
About I Missed You
More ASTAR Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl