Sama Everything Lyrics
Sama Everything Lyrics by PHILIPPE NDOUR
Yay sama everything, beugeul ma défal la
Amouna anything té dou té ma défal la
Wakh iow lo beugeu, sa baneex rek la beugeu
Sama yéné défal la togal ma firila
Yay sama everything, beugeul ma défal la
Amouna anything té dou té ma défal la
Yangui yekk sama loveu
Yangui few sama loveu
Li mala yéné xamnako
And you know you know you know now mama (xamnako baby)
Li mala yéné you know now mama (xamnalo baby)
You know you know you know now maaa (xamnako baby)
Xamalna ni sa domyi deff la yéné lou barri

Yalla ma bolék iow, yaye diourom nienti wér nga eumbouma
Tey dji magg na, wathié si kow souf man ganéssina
Wakhma lane nga beug, lépp ma défal la paréna
Sama yéné manak zeyna ci adouna ben la
Gouddou fane dé lalay nianal, yobbou la makka la yéné
Magg na beug dap sa love, xamna mounoumala fay
Tey yalla may sédé ci sama yéné
Linga def ci nioun, yaye boy yay gained
Yay sama everything, beugeul ma défal la
Amouna anything té dou té ma défal la
Yangui yekk sama loveu
Yangui few sama loveu
Li mala yéné xamnako
And you know you know you know now mama (xamnako baby)
Li mala yéné you know now mama (xamnalo baby)
You know you know you know now maaa (xamnako baby)
Xamalna ni sa domyi deff la yéné lou barri
And you know you know you know now mama (xamnako baby)
Li mala yéné you know now mama (xamnalo baby)
You know you know you know now maaa (xamnako baby)
Xamalna ni sa domyi deff la yéné lou barri
Dolli ant yalla sama dom xalébi magg na
Lingma yéné mangui niane buur yalla mou degu leu
Pa Philippe sa wakh yeggna ci xol nekhnama
Pa Philippe Viviane, yaye ak dom guén di ame Philippe
Yay sama everything (yay sama adouna)
Amouna anything naniou sant yalla
Yangui sama loveu mangui yekk sa loveu
Mangui feel sa love iow mi
Oh you know you know you know now mama (xamnako baby)
Li mala yéné you know now mama (xamnalo baby)
You know you know you know now maaa (xamnako baby)
Xamalna ni sa domyi deff la yéné lou barri
Oh you know you know you know now mama (xamnako baby)
Li mala yéné you know now mama (xamnalo baby)
You know you know you know now maaa (xamnako baby)
Xamalna ni sa domyi deff la yéné lou barri
(Mar buur yacine mar, birame yacine mar)
Birame ngouille alé ndiaye, so woyoul denga wara woy
Ndéye sokhna sa mame, ami fall sa mame
Boiba ndour sa baye, Viviane sa yayooo woyal)
Watch Video
About Sama Everything
More PHILIPPE NDOUR Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl