QUEEN BIZ Damay Dem cover image

Damay Dem Lyrics

Damay Dem Lyrics by QUEEN BIZ


Dama nek gouné
Oubi sama beut yé
Tokk di setlou aduna bi khamné dafa méti
Yensay ma teudé
Yéwu khadja goudé
Tokk ci sama digue lale di dioy ndax diafé diafé
Done yakkar ci yayam
Nekk kharitou baye’am
Mba kham ngen ni nitt niouma yoni dagn ma yakamté
Feep fouma diar
Yeufi dafay mété
Yoon bi beurri khakham ba deukiy dima djané

Mba kham ngen ni douma ladji douma daw
Damay djiguen motax may daw battou ganaw

Yensay ma feugué
Niouné ma dou fi déh
Ma diok daldi korti korti délou fima diougué
Boudoul yeup nékathia
Makoy feug bageu déh
Wayé khamna ni aduna bi mounoul yombé

Mba kham ngen ni néwone na len yen
Damay dem mane dara douma té
Mane deh néwone na len
Mane déh damay dem
Damay dem mane dara douma té
Mane deh néwone na len
Mane déh damay dem
Mane QueenBiz mi déh mane déh damay dem

Feep fouma dal di dem
Gni nane ma mothi galace
Gni nane ma mome wayé dafa woyof seurr
Mba kham ngen ni mane mi damay djiguen douma goor
Na fass sama lafou seurr ba doni goor

Mane dina len di wane
Né diant bi foumuy fenké
Fofou la yéwo té khamna loufiy khéwé
Damay sante buur bé
Ci lim ma thieuré
Ndaxté khamna ni mome moy borome beut bou reuy bé

Mba kham ngen ni mane mi déh damay dem
Damay dem mane dara douma té
Mane déh néwone na len
Mane Queen damay dem
Damay dem mane dara douma té

Soul keer douko téré feign annh !
Oui yé douko téré feign
Wayé y’Allah bou keer daldi ndaw ba faf souralé len annh !
Douko téré feign

Mane dara douma té
Mane dara douma té
Mane dara douma té
Mane dara douma té
Mane dara douma té

 

Watch Video

About Damay Dem

Album : Puissance 3 (Album)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Oct 05 , 2019

More QUEEN BIZ Lyrics

QUEEN BIZ
QUEEN BIZ
QUEEN BIZ

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl