JEEBA  Goor  cover image

Goor Lyrics

Goor Lyrics by JEEBA


Yoow goorgorlul wonel yay goor
Fi goor deey door goor diap goor
Yoow gorgorluul nga def yeufu goor
Fi goor deey diak goor dimbali goor
Ndax amoul amoul soxoor amoul kiniane
Té Lolou deuguit mooy jikooy goor goor goorooy
Goor ndax danga aah  woor diambaroo

Yow goor goor du beuri thiow
Goor ligueey laay geum niémei deuku lou diss
Koula wo si ay tiaxane nekoo newoumafa
Am fula beuri diom ndiambarou gaindé goor
Goor dafay touti waax deukei job lu baari lu baari
Boko defei dangay sori
Bayil sa ngora bingay mboubo naane goor
Lolou defoul goor, goor dafay lorgné deem fu sori

Kone goorgorlu takhay degg waaw goor gooroy goor
Goor Danga an woor diambaroo
Goor dafay teraal jigueen siguil nday ak baay laay nawei goor
Walaay goor
Yoow goorgorlul wonel yay goor
Fi goor deey door goor diap goor
Yoow gorgorluul nga def yeufu goor
Fi goor deey diak goor dimbali goor
Ndax amoul amoul soxoor amoul kiniane
Té Lolou deuguit mooy jikooy goor goor goorooy
Goor ndax danga woor diambaroo

Yow goor, goor dou hypocrite
Goor waroul fimisté rambadj dou djikooy goor
Goor deey kham likou waar tei dikoo dieufé goor
Goor Adina boumou meiti banga saliit goor
Sangoul sa mbalanou sutureu boul diaay sa ngor
Goor beneu diabaar
Niaar niety baxna si koow nga meune ko yoor goor
Walaay goor
Kone gorgorluul takhaay deeg waaw goor gooroy goor
Goor Danga aah woor diambarooy

Yoow goorgorlul wonel yay goor
Fi goor deey door goor diap goor
Yoow gorgorluul nga def yeufu goor
Fi goor deey diak goor dimbali goor
Ndax amoul amoul soxoor amoul kiniane
Té Lolou deuguit mooy jikooy goor goor goorooy
Goor ndax danga aah woor diambaroo
Goor Yallah dangay teek sa beut fuu sorri
Nanthio Sadio Mané
Walaay yaay goor diambaar ngaa, waaw goor
Gooroy goor
Goor danga aah woor diambaroo

Watch Video

About Goor

Album : Alajee (Album)
Release Year : 2022
Added By : Farida
Published : Dec 16 , 2022

More JEEBA Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl