Deugg'Leu Lyrics
Deugg'Leu Lyrics by DIEYNA
Mak ioe dèmb leu dou tay
Gno boukou lèpp rombou ngueu domou ndèye
Mane doumeu tiitt soumlèy guiss sama wètt
Même bou gneup démer ioe ngua dèss doumeu wèett
Boumeu amè métitt yaw ngua am louleu métti
Da dèm ba mèlni gno bokk xol lou ma nè yangui tchi
Meussou lo meu guiss tchi ay djafé djafé dimeu sétann
Wa la ngua andakk nonne yi dimeu rétanne
Mani deugueu leu
Lou yagueu deugeue leu
Anndeu bi deugueu leu
Motakh meu beugueu leu
Lèppeu deugueu leu
Lou ma nèkh nèkh nala
Lou ma mètti sonal la
Ki takh meu gueum ni kharitt amna ioe la
Ioe kharitt oh sama kharitt
Ioe kharitt oh sama kharitt
Ioe kharitt oh sama kharitt
Kènn sagnoul toguak ioe
Di yaakk sama dèr
Wa la di wakh tchi mane lou boonne
Ioe meussou lo meu dèf lou gnaw
Té souma rèrer yay ki may tèguatt tchi yoone
Ioe mousso ma worr, mousso ma toguer
Ioe rèk keu woor meunn nako sèdder
Ya gueuneu guorré sama taka ndèrr
Ndakh si birr leundeum
Do ma daw, do meu rèrr
A part solitude yay seumeu amie
Bokou gnou ndèye ak baye té yay seumeu famille
Mani deugueu leu
Lou yagueu deugeue leu
Anndeu bi deugueu leu
Motakh meu beugueu leu
Lèppeu deugueu leu
Lou ma nèkh nèkh nala
Lou ma mètti sonal la
Ki takh meu gueum ni kharitt amna ioe la
Lou ma nèkh nèkh nala
Lou ma mètti sonal la
Ki takh meu gueum ni kharitt amna ioe la
Ioe kharitt oh sama kharitt
Ioe kharitt oh sama kharitt
Ioe kharitt oh sama kharitt
Mani deugueu leu
Lou yagueu deugeue leu
Anndeu bi deugueu leu
Motakh meu beugueu leu
Yay sama sama, sama sama Kharitt
Yay sama sama, sama sama Kharitt
Yay sama sama, sama sama Kharitt
Watch Video
About Deugg'Leu
More DIEYNA Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl