No Stress Lyrics by VIVIANE CHIDID

Non non bouniou nagou niou niouy tek stress
Non non bouniou nagou niou niouy tek stress
Non non bouniou nagou niou niouy tek stress
Sounou xol di fess nom nou diouk deff fess
Non non douma nangou nga may tek stress
Douma nangou nga may tek stress

Ma bagne doumako nangou no stress
sama xol di fess yaw nga diouk deff fess
Mani dimbalima wax dji beurina
Mane rek thi xalé namouma dara
Mani dimbalima wax dji beurina
Mane rek thi xalé namouma dara

Da nga faté ni am neu 10 ans
Lou tax gna dieul ma beug ma déff sa fowoukey
Yombeul naleu sa visa
woow yeah yeah démal foula nex way
Beugue languak ki, beugue langual ké
Beugue languak sama xarite, mani night and day
Dégue na niouné fébar lah
woow yeah yeah défal nex way

Non non douma nangou nga may tek stress
Douma nangou nga may tek stress
Douma nangou fils nga may tek stress
Ma bagne doumako nangou no stress
Sama xol di fess yaw nga diouk deff fess
Mani dimbalima wax dji beurina
Mane rek thi xalé namouma dara
Mani dimbalima wax dji beurina
Mane rek thi xalé namouma dara
Goor boula tek deal lundi ba dimanche noboula
Kouma beugue tardél beugue ma fowé ma rombe la
Goor boula tek deal lundi ba dimanche noboula
Kouma beugue tardél mane rombe la
Li safatouma, sama métytou xol diex na
Li yeunguelouma ndaxté mane niakouma fayda
Li safatouma tégou thi temps deff bamou bax jotna
Té yaw mi xamgua soma noboul sa morom nob ma

Non non bouniou niou niouy tek stress
Bouniou nangou niou niouy tek stress
Non non bouniou niou niouy tek stress
Souniou xol yi fess nio niou diouk deff fess
Non non douma nangou nga may tek stress
Non non douma nangou nga may tek stress
Ma bagne doumako nangou no stress
Sama xol di fess yaw nga diouk deff fess

Mani dimbalima wax dji beurina
Mane rek thi xalé namouma dara
Mani dimbalima wax dji beurina
Mane rek thi xalé namouma dara

Goor boula tek deal lundi ba dimanche noboula
Kouma beugue tardél beugue ma fowé ma rombe la
Goor boula tek deal lundi ba dimanche noboula
Kouma beugue tardél mane ma rombe la

Watch Video

About No Stress

Album : Wuyuma (DTM) (Album)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Oct 20 , 2019

More VIVIANE CHIDID Lyrics

VIVIANE CHIDID
VIVIANE CHIDID
VIVIANE CHIDID
VIVIANE CHIDID

Comments ( 0 )

No Comment yet

See also



You May also Like



Get Afrika Lyrics Mobile App

About AfrikaLyrics 

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2020, New Africa Media Sarl