Sama Lova Lyrics
...
Sama Lova Lyrics by ISS814 BEATS
Mbeuguel bima am ci yaw
Daf may titeul yen sayy
Sama adouna nane lay mel
Bougnou nekatoul gnoune niar
Lou fanane si mane yendou si yaw
Yay sama guene waal
Fo dem mangui toc, toc dila xarr
Parce que yay sama lova
Lova lova lova
Sama lova
Lova lova lova
Niniou meel, maan dafay may titeul
Est-ce que do yéwou beugeu bayi
Amoon na ni mafi jiteul
Ba malen woné mbeuguel dagn ma trahir
Yow yaay sama love té amna yakaar
Beugouma dem baci birr amsi nakar
Yen say ngeu dieufé mbir maa amsi xeel niar
Guem né rek
Bouma diapé teuweu bayi day bax
Jiteul na samay sentiment ba faté sama bop
Ak limay yeuk
Wola ci love yow nga felouma
Pour niou and bokando souniouy weurseuk
Mbeuguel bima am ci yaw
Daf may titeul yen sayy
Sama adouna nane lay mel
Bougnou nekatoul gnoune niar
Lou fanane si mane yendou si yaw
Yay sama guene waal
Fo dem mangui toc, toc dila xarr
Parce que yay sama lova
Lova lova lova
Sama lova
Lova lova lova
Sa youma meré dem bay xaadi
Xalat finiou diaar
Diapatt espoir
Lou nekk guiss nagn ko si yoon bi
Defaite ak victoire dound ko nioun niaar
Xamna ni dagni xeekh ma babe
Diapal dina baax lolou la meuneu waax
Te sa yo naré dem ba xadi
Danga makoy waax
Meune nala indiwaat
Souniou xool yi lerna kone couple bi mounoul leundeum maak yow
No no
Fo meunti neh ci life woma ma niow oh oh
Niou ande goo oh oh oh
Mbeuguel bima am ci yaw
Daf may titeul yen sayy
Sama adouna nane lay mel
Bougnou nekatoul gnoune niar
Lou fanane si mane yendou si yaw
Yay sama guene waal
Fo dem mangui toc, toc dila xarr
Watch Video
About Sama Lova
More ISS814 BEATS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl