Arrêtons L'hémorragie Lyrics
Arrêtons L'hémorragie Lyrics by ISS814 BEATS
Kham na ni niakeu dou dègn fi ak diougou niou bagn
Misère violence bouy khègn nioune rek lay gagn
Paradis fiscale loubal allalou rew
Problémou sénégal moy kouniou diokh gestion nga bew
Nopilo OFNAC menancé juge de compte
Nassakhal assemblée souniou caisse ya ley khonte
Niakhtou diague diagalé tek si problémou sanitaire finance fi leep tambalé
Dioubaloul dara dou leer
Boula dar yem boudé sa caisse mounoul fess
Ndaxté yorine bé dess té lepeu meun na ne mess
Sa maladie def la stress mouno ko fathi
Inégalité sociale li nioune rekay nathie
[CHORUS]
Té gni nieup laniouy goungué
Té nénaniou niom nio niouy goungué
Loubal ci paradis fiscal
Tek naniou thiono gou né
Arrêtez l’hémorragie, arrêtons l’hémorragie
Arrêtez l’hémorragie, arrêtons l’hémorragie
Amna ay rapports yougn moussoul publiés
Diap nagn fi nitte ndax rawalé billet
Boudé si yen la bok da ngen koy protégé
Convention you nébuleuse you cours des comptes doul audité
Payments abusif, résultats négatifs
Souniou biir ley fegn, nioune rékay khif
Lane nga dépensé ak lane nga déclaré
Bayil corp de contrôle yi def sen liguey
Bou len menancé pour niou def arrêt
Ndaxté bougn la seytou woul deuk bi mounoul weuy
Product ak festin bi fa am nagn ko def
Ci ay rapports ndax nitt gni meuna xam
[CHORUS]
Té gni nieup laniouy goungué
Té nénaniou niom nio niouy goungué
Loubal ci paradis fiscal
Tek naniou thiono gou né
Arrêtez l’hémorragie, arrêtons l’hémorragie
Arrêtez l’hémorragie, arrêtons l’hémorragie
Dougn faté affaire Panama papers
Suisse lake ak Maurice slape
Bougn bayi multinational yi rawalé souniouy impots
En bas ls conventions fiscales douteuses
Et vive les conventions fiscales et vertueuses
[CHORUS]
Té gni nieup laniouy goungué
Té nénaniou niom nio niouy goungué
Loubal ci paradis fiscal
Tek naniou thiono gou né
Arrêtez l’hémorragie, arrêtons l’hémorragie
Arrêtez l’hémorragie, arrêtons l’hémorragie
Watch Video
About Arrêtons L'hémorragie
More ISS814 BEATS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl