ISS814 BEATS Xool Ma Ci Bët cover image

Xool Ma Ci Bët Lyrics

Xool Ma Ci Bët Lyrics by ISS814 BEATS


Mbeuguel bou deugou
Dara douko faye
Yaay seetou
Biye woné sama leeraye
Jant goudi Biddew soubeu teel
Bimala xamé Ci la tagok weetaye
Nii tognal sa aaaaaa ! yaye
Balenala ndakh mbeuguel bimaay yeug
Ci yow
Nii tognal sa aaaaaa ! Baye
Balenala ndakh mbeuguel bimaay yeug
Ci yow
Wolou nala wolou wolou nala ! Eh yaaaay !
Wolou nala wolou wolou nala ! Ahn ahn !

Boume laay guiss ngaay doundou
Dafemaay doundeul baby
Soume laay guiss ngaay rétaan
Dafemaay doundeul waay
Boume laay guiss ngaay doundou
Dafemaay doundeul baby
Boume laay guiss ngaay rétaan
Dafemaay doundeul waay

Xool ma ci bët
Ma xool la ci bët
Nioune niare la rek
Mbeuguel a nekh
Xool ma ci bët
Ma xool la ci bët
Nioune niare la rek
Mbeuguel a nekh
Yéne saaye nga diéki diéki woma, Woma
Nga meer maané mba diépiwoma
Nga néma non non
Yéne saaye nga xole ma rek
Ma rétaan rétaan
Yaay sama boumou xol bi
Yaay sama boumou xol bi
Bo meeré ba guédeu dafemaay metti, Metti
Bo deffé ba gnipeu Nala setsi, Setsi
Douma ci xole sax pa bek mère bi, Mère bi
Na oubi bountou bi soxna si
Dang ma diape sa mbaal
Té douma guéneuti
Bilay walay yé
Yow laay fethie ci bal
Yaay sama mélodie
Yow rek la baredé Eh eh !

Boume laay guiss ngaay doundou
Dafemaay doundeul baby
Soume laay guiss ngaay rétaan
Dafemaay doundeul waay
Boume laay guiss ngaay doundou
Dafemaay doundeul baby
Boume laay guiss ngaay rétaan
Dafemaay doundeul waay

Xool ma ci bët
Ma xool la ci bët
Nioune niare leu rek
Mbeuguel a nekh
Xole ma ci bët
Ma xole la ci bët
Nioune niare leu rek
Mbeuguel a nekh

Yeh weurena ba weurengueul adouna
Yeh kou melni yow mba amatina
Yeh dougueul ci Keur gui yatouna
Ndakh yow yaay yaay sama boumou xol yaay sama boumou xol

Yéne saaye nga diéki diéki woma, Woma
Nga meer maané mba diépi woma
Nga néma non non
Yéne saaye nga xole ma rek
Ma rétaan rétaan
Yaay sama boumou xol bi
Yaay sama boumou xol bi

Weurena ba weurengueul adouna
Yeh kou melni yow mba amatina
Eh yah dougueul ci Keur gui yatouna
Ndakh yow yaay
Yaay sama boumou xol
Yaay sama boumou xol

Watch Video

About Xool Ma Ci Bët

Album : Xool Ma Ci Bët (Single)
Release Year : 2021
Copyright : © 814 Prod. | July 2021
Added By : Farida
Published : Jul 19 , 2021

More ISS814 BEATS Lyrics

ISS814 BEATS
ISS814 BEATS
ISS814 BEATS
ISS814 BEATS

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl