
Tell Me What You Want Lyrics
...
Tell Me What You Want Lyrics by YOUSSOU NDOUR
Douma la meuss a settal nga wett
My baby you know,
Douma la meuss a sett al nga wett
Souma la togne é nan ga ma baal,
My baby you know
Douma la meuss a sett al nga wett
Kham na lii nga ma ye n’ai,
My baby you know
Douma la meuss a sett al nga wett
Li ma la yé n’ai ci sa ma xol my baby you know
I’ll never leave you alone…
Ahhnn…. He yeaaa
Tell me what you want and I’ll do it
Ahhnn…. He yeaaa
Tell me what you want and I’ll do it
Souma xol é rekk kham nga
my baby you know
njem ou ma gare ba demm
Xam na bëgg na a lool my baby you know
Tey itt fonk nga maa
Lepp lo xam né souma ko deff é,
my babe you know
Dey wo ma wax ko , wax thia téll
boul xar dey ma ko wax
my baby you know
boul xar dey ma ko wax
Ahhnn…. He yeaaa
Tell me what you want and I’ll do it
Ahhnn…. He yeaaa
Tell me what you want and I’ll do it
Ahhnn…. He yeaaa
Tell me what you want and I’ll do it
Ahhnn…. He yeaaa
Tell me what you want
boul di faté gno’on yè
boul doul wo gno’on yé
boul di faté nak
bo ko faté nak
dëgg dëgg yak’u
tê ma fé do t’ou né
Ahhnn…. He yeaaa
Tell me what you want and I’ll do it
Ahhnn…. He yeaaa
Tell me what you want and I’ll do it
Ahhnn…. He yeaaa
wax ma lii nga bëgg ma def ko
Ahhnn…. He yeaaa
Ahhnn… He yeaa
Watch Video
About Tell Me What You Want
More YOUSSOU NDOUR Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl