BAYE MASS Qui Es Tu? cover image

Qui Es Tu? Lyrics

Qui Es Tu? Lyrics by BAYE MASS


Mane kouma bagn mane yereum na leu
Samay wadiour danie ma nianal
So doné sama noone yereum na leu
Fou mala rombeu nela diapal si lii
Amna nit yo xamni douniou conetane
Ndakh lou nite am dounioula ko yéné
Borom beut bou reuy bi moma def ni
Nangouko té nga nieuw niou bégué
Ennemi je t’aime et tu le sais yaw

Ndakh da nga may tok dolei
Ennemi je t’aime et tu le sais
Ndax da nga may sawarlo
Yow ennemi qui es-tu ? wawaw
Qui es-tu ? yow qui es-tu ?
Ndakh da nga may tok dolei
Yow ennemi qui es-tu ? wawaw
Qui es-tu ? yow qui es-tu ?

Ndax da nga may sawarlo
Warouniou di sékeu lou niaw
War nga ma meune yéné limala yéné
Ndakh yala limou bindeu
Domou adama bi lasi gueneu beugue
Yénéwoumala lou niaw
War nanio meune sek diam
Ba mane foumala rombeu
Nioou ande daldi lamisso
Ennemi je t’aime et tu le sais, yaw
Ndakh da nga may yok dolei
Ennemi je t’aime et tu le sais
Ndax da nga may sawarlo
Yow ennemi qui es-tu ? wawaw
Qui es-tu ? yow qui es-tu ?
Ndakh da nga may tok dolei
Yow ennemi qui es-tu ? wawaw
Qui es-tu ? yow qui es-tu ?
Ndax da nga may sawarlo

Ennemi je t’aime et tu le sais, yaw
Ndakh da nga may yok dolei
Ennemi je t’aime et tu le sais
Ndax da nga may sawarlo
Yow ennemi qui es-tu ? wawaw
Qui es-tu ? yow qui es-tu ?
Ndakh da nga may tok dolei
Yow ennemi qui es-tu ? wawaw
Qui es-tu ? yow qui es-tu ?
Ndax da nga may sawarlo

Watch Video

About Qui Es Tu?

Album : Airmass (EP)
Release Year : 2023
Added By : Farida
Published : Aug 01 , 2023

More BAYE MASS Lyrics

BAYE MASS
BAYE MASS
BAYE MASS
BAYE MASS

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl