Yaye Lyrics
...
Yaye Lyrics by BAYE MASS
Yéne naala adduna
Yéne nala ajana
Yaalna yalla sàam la
Yaalma na yalla yokk la
Kima deloo ci joxma joyu mbècctè yaw la
Ki tax may noyi ba beg màag tekki yaw la
Saa yuma jaxle ba gestu kimay guis de yaw la
Yaaye sama xarit kima gena beg sama dunddu yaw la
Cèy suma amoon aduna ak li biir bo jox la
Juddu wàat su amoon kiy nekkat sama yaye de yaw la
Lima la yèene su xajon ci aduna ma jox la
Yaw sama yaye kima gene beg sama dunddu yaw la
Yéne naala adduna
Yéne nala ajana
Yaalna yalla sàam la
Yaalma na yalla yokk la
Fii kufi baax
Nang ko santte sa yaye booy
Buko tek lu mèeti
Fexeel ba bumu mese joy
Hakku njurèel
Dafa diss bak en amul njek li
Sula yalla tèralle
Fexel ba jox sa yaye mérite bi
Fii kufi baax
Nang ko santte sa yaya booy
Buko tek lu mèeti
Fexeel ba bumu mese joy
Hakku njurèel
Dafa diis bak en amul njek li
Sula yalla tèralle
Fexel ba jox sa yaye mérite bi
Yéne naala adduna
Yéne nala ajana
Yaalna yalla sàam la
Yaalna na yalla yokk la
Hann
Am djilé yaaaye yomboule
Nangoo mun
Dekke mun doyloo yala yaye
Xamlaay fii nji ne amunu fenèen yaye
Ak fo menti nèek beg nala yaye
Sudde ya ngi dèeg woy wii yaye kàay
Ma ngi fatelèeku banu doon tok di jàay
Waxone nala naa fomp sa joyu kàay
Yama te yalwàan
Xaràane yayàa booy
Yéne naala adduna
Yéne nala ajana
Yaalna yalla sàam la
Yaalma na yalla yokk la
Fii kufi baax
Nang ko santte sa yaye booy
Buko tek lu mèeti
Fexeel ba bumu mese joy
Hakku njurèel
Dafa diss bak en amul njek li
Sula yalla tèralle
Fexel ba jox sa yaye mérite bi
Fii kufi baax
Nang ko santte sa yaye booy
Buko tek lu mèeti
Fexeel ba bumu mese joy
Hakku njurèel
Dafa diss bak en amul njek li
Sula yalla tèralle
Fexel ba jox sa yaye mérite bi
Yéne naala adduna
Yéne nala ajana
Yaalna yalla sàam la
Yaalma na yalla yokk la
Watch Video
About Yaye
More BAYE MASS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl