Momel Lyrics
Momel Lyrics by BAYE MASS
Khalé bii lingua doooone thi mane yeim nama loole
Sama khooole binguaaa diiaaaaap, di meuy doore dithii foo
Khalé bii lingua doooone thi mane yeim nama loole
Sama khooole binguaaa diiaaaaap, di meuy doore dithii foo
Hum hum hummmmm
Wouya wouya wouya
Wouya wouyaaaaaa
Yagou niou lolou mane ak mome
Ma defko yaye mou defma dome
Mou diapalé ma ni ab domame
Firndeile meu wane meu mbeuguélam
Djiguene sou amé fouleu ak diome
Louma yotou meune nassé dioote
Sameu sa bop sameu say dome
Né si sa bop moytou am diote
Samal ma sa doome yi
Guamathie nga thi keur gui
Téyélé meu alale dji
Té boul di door daakhé
Moytoule ma sa noon yi
Toguale meu thi keur gui
Boule yakheu saa khol bi
Té bouma diam nanééé
Khalé bii lingua doooone thi mane yeim nama loole
Sama khooole binguaaa diiaaaaap, di meuy doore dithii foo
Khalé bii lingua doooone thi mane yeim nama loole
Sama khooole binguaaa diiaaaaap, di meuy doore dithii foo
Bon c’est vrai que j’ai essayé par tous les moyens
Wane leu fingua fété thi mane
Et dou neikheu comprendre parce que dégoutoma
Beine instant yaw rek yama meuneu comprendre
J’ai une grande famille derrière moi
Bo khamné je me sens responsable thi séne situation
Dama diap né mane rek maléne thi meuneu guènè
Et tellement je suis concentré thi sama ligueye ba dama faté
Que thi famille bobou nga bok
Doumala xakh balma parce que kham nané absence bi meuno mako baal
Mais comprendre meu parce que lolou mo eup solo
Watch Video
About Momel
More BAYE MASS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl