...

Buur Lyrics by BAYE MASS


Yaw yàala

Lèer namàne ku bàax nga

Sa yermande yàatu nàa

Jèegel ma limma yàaxx

Limma gèent yèen na ma de

Yàadi buur yàa eeo doole

Yàay sàamm boroom

Yàanu boole mom

Yàama yillif yaw rek yàamay jox

Yàafi jitu yàafiy mujèe

Yàanu uump yaw rek yàa fèen

Sa yermande ma yèem

Yàay dundel ci sa leer

Sutural ma bes bumala toone

Yaw rek di buur bi

Fèes dèel ci nguur gi

Boole mom mindèef vi

Buuru jant ak wèer bi

Yaw rek di buur bi

Fèes dèel ci nguur gi

Boole mom mindèef vi

Buuru jant ak wèer bi

Lo dogal beg naa, sula nèexe nèex nama

Foma tek tegu nàafa gem nani jamu bur la

Bu sirat taxawe bes bu jàam nèep di tite

Sama xol bi dina sèede begon na yonent bi

Fonkoon nàa ni ma mag jèema bok lima am

Dàan yèesal ca waxtu ba donte xam na matumàa

Yeremon nàa gone lool donte damà beri toon

Ate ma sa yermande nax damala rèere woon

Nax damala rèere woon

Duma nit ku bàax dina jème fonk waxtu

Duma nitu lèer yàala buma rev ba dèe ci

Bu sirat taxawe bes bu jàam nèep di tiit

Sama xol bi dina sèede begon na yonent bi

Duma nit ku bàax dina jème fonk waxtu

Duma nitu lèer yàala buma rev ba dèe ci

Bu sirat taxawe bes bu jàam nèep di tiit

Sama xol bi dina sèede begon na yonent bi

Desalatooma alhamdulilàa

Ku sant yàala yàala doolil la

Duma mesa doyal ci maaal la

Yàay buuri bur yi, yàa men defal ma

Yaw rek yàa men yàan am te yàa xam

Yaw rek yàa dac, yàay dindi yàay def

Teegi naa ling ma wax sèetanoma been yon

Dèeloma li’in ma joxon duma def lima defon

Tèel ngama tera lool, nèewuma saa ben moroom

Def aduna sama xol fàate lin waxante won

Moytulo nga ma sa noon, mane ma def ko àandandoo

Yonent waxal borom lèer yi mu jèegel ma samay tonee

Muhamadu rasulilàa kuko mesa nan ma may la

Kuke mosa ten mu bàal la ngir mbàaxam

Teeno jèema roy ci yonent bèe

Xayrul anbiyàa yi

Yàalen gen, yàalen men

Yaw de yàay muhamadu rasulilàa ée nabi

Watch Video

About Buur

Album : (Single)
Release Year : 2024
Copyright :
Added By : Farida
Published : Aug 31 , 2024

More BAYE MASS Lyrics

BAYE MASS
BAYE MASS
BAYE MASS
BAYE MASS

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl