BaaBam Lyrics
BaaBam Lyrics by DJEYNA
[COUPLET 1]
Mane déh naw na sa diné
Mane déh naw na sa respect
Naww na sa djiko, bay jou melni ioe
Djaféna ci jamono ji waw
Beug nala baaban, waxtane ak mane dima yokk xam xam hum… hum…!
Borome keur gou melni ioe la beugeu am…
[REFRAIN]
Yama ko diaral, li goor yi di beurri amo ci morom
Yamako diaral mimé yéduma Baabam
Yama ko diaral fent waay bi
Délo la ndioukeul
Yamako diaral mimé yéduma baabam
Lou geuneu nékh li
Waxma lou geuneu nékh li
Ngay papa ci mane ma done dome ci ioe
May yaye ci ioe nga done dome ci mane
Baabam
Baabam
[COUPLET 2]
Damay guiss di ré
Beugo ma méré la
Dima digal lou bax, leep lou bone nga téré ma
Barké rek lay sakou
Diangue ci sa xol bou yatou
Lo doundou doyoul baba
Waay wi yako mome
Ioe papa ma leu mome, maat nga li nga done papaaa…
Maat nga li nga done papaaa…
Baabaam
[REFRAIN]
Yama ko diaral
Li goor yi di beurri amo ci morom
Yamako diaral mimé yéduma Baabam
Yama ko diaral fent waay bi
Délo la ndioukeul
Yamako diaral mimé yéduma baabam
Lou geuneu nékh li
Waxma lou geuneu nékh li
Ngay papa ci mane ma done dome ci ioe
May yaye ci ioe nga done dome ci mane
May yaye ci ioe nga done dome ci mane
[OUTRO]
Lay Layla laaaaa…!
Mane déh beugeuna leu baba yo
Baba, baabam héhé !
Baabam, baabam mimé yéduma
Baabam héhé !
Baabam, baabam mimé yéduma
Baabam, baabam, baabam, mimé yéduma
Baabam, baabam, baabam, mimé yéduma
Watch Video
About BaaBam
More DJEYNA Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl