
Wurus Lyrics
Wurus Lyrics by WALLY SECK
Yay sama adouna, oh yeah
Sama baby coco waay, ey yeah
Ioe yay sama adjana; my love
Sama baby coco waay, hmm yeah
Baby yay mane
Teudeul nèlaw kham gni mounoul dara
I don’t give a fuck mèrr katt fadjoul dara
Takal la or ba chi 24 carats
Dagn lénn di bayèkk peureum bi
Gnom gnouy deukké aya
Baby i just want real love
Real love, I just want now real love
Yay sama adouna, oh yeah
Sama baby coco waay, ey yeah
Ioe yay sama adjana, my love
Sama baby coco waay, hmm yeah
Way way way way
Mèrr bi fadjoul dara
Mom fadjoul dara
Konn fadjoul dara
Baylènn té gneuw ma takal la or 24 carats
Wurus 24 carats
Ngualam 24 carats
Khana dou maal yèenè
Ma vie, ma vie
Baby yay mane
Teudeul nèlaw kham gni mounoul dara
I don’t give a fuck mèrr katt fadjoul dara
Takal la or ba chi 24 carats
Dagn lénn di bayèkk peureum bi
Gnom gnouy deukké aya
Baby i just want real love
Real love, I just want now real love
Yay sama adouna, oh yeah
Sama baby coco waay, ey yeah
Ioe yay sama adjana, my love
Sama baby coco waay, hmm yeah
Way way way way
Mèrr bi fadjoul dara
Mom fadjoul dara
Konn fadjoul dara
Baylènn té gneuw ma takal la or 24 carats
Wurus 24 carats
Ngualam 24 carats
Watch Video
About Wurus
More WALLY SECK Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl