...

Sama Habiibi Lyrics by YOUSSOU NDOUR


Nijaay wax al ak sa mag ji

Boo gaaw u lee , mu jaay ma

Alal moo yóbbu , fit wi

Sama Habibi bi

C’est l’amour de ma vie

Bu jar ee mer , ma mer ko

Bu jar ee jooy , ma jooy ko

Bu jar ee xeex , ma xeex ko

Sama Habibi bi

C’est l’amour de ma vie

Ki ne ci sa ma xol bi

Moo ma gën ël , alal ji

Té ngeen a gat al wax ji

Sama Habibi bi

C’est l’amour de ma vie

Instru

Bu am a gul , ma muñ ko

Lu ma fortaatu , jox ko

Nijaay gaaw al nga dox ko

Sama Habibi bi

C’est l’amour de ma vie

A yéen daal yéen , a sonn a

Du maa moom sa , ma xol bi

Mbëggéel ken du ko donne

Sama Habibi bi

C’est l’amour de ma vie

Break;

Mbëuggéel gu ñu lë bëgg é

L’amour ne s’achet pas

Mbëggéel gu ñu lë bëgg é

Mbënggéel gu ñu lë bëgg é

L’amour ne s’achet pas

Mbëuggéel gu ñu lë bëgg é

Mbënggéel gu ñu lë bëgg é

L’amour ne s’achet pas

Mbënggéel gu ñu lë bëgg é

Mbënggéel gu ñu lë bëgg é

L’amour ne s’achet pas

Mbënggéel gu ñu lë bëgg é

Ba laa ngaa jël teraanga , laaj ko ndax bëgg në

Ba laa ngay jël warougar , laaj ko ndax bëgg në

Ba laa ngay jël teraanga , laaj ko ndax bëgg në

Ba laa ngay nangu warougar , laaj ko ndax bëgg në

Xale bi kaay fii , laaj ma ndax bëgg në

Xale bi kaay fii , laaj ma ndax bëgg në

Xale bi , xale bi , xale bi , laaj ma ndax bëgg në

Xale bi kaay fii , laaj ma ndax bëgg në

Xale bi , xale bi , xale bi , laaj ma ndax bëgg në

Xale bi kaay fii , ma laaj la , ndax bëgg ngë

Da fa mel ni xale bi , xale bi, bëgg ou lo loo

Nijaay gaaw al nga dox ko

Sama Habibi bi

C’est l’amour de ma vie

Watch Video

About Sama Habiibi

Album : (Single)
Release Year : 2025
Copyright :
Added By : Farida
Published : Apr 04 , 2025

More YOUSSOU NDOUR Lyrics

YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR
YOUSSOU NDOUR

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl