Maria Lyrics
Maria Lyrics by BY MIC
Sama xol nga keuf Yobalé sama xel
Mane andatouma Sago xaw li ni mel
Shaw yi yeup ma Dé ci mane ma dioye ci yow
Meunoumala bania call Tontou ma Know
Dama reuy Normal Mey guéné djiko you sew
Mais Baal ma Bae Lou Mel ni no no dotou fi xew
Dama done diay bandit fekk fi Thug
Danga saï Saï tek ci nekha beugue
Zig Ndakaru Ndiaye Peundeul nga ko fepp
Ba fo romb niou Diokh la Gueudeu
Maria Maria Maria Maria Maria
Maria Maria Maria Maria Maria
Maria! Faléwoulo ma Maria (No no no no no wo)
Maria Lidieunti wo ma Maria
Dotou mako Défati
Répond Stp Ne me dit pas que c'est Fini
Dotoumako défati, (Aie Aie yeah !)
Sounkouto Na musso
Sounkouto doukaré kana gning ké na
Sounkouto wowo wo na musso oh
Sounkouto Maria Kana gning Ké na
Si bu misti Combersa bem no Combersa
Si bu Mista bai nkana seta kila
Ni lafta Kathia la, Na ngha Kathia
Bari ni iko ibitala nko nté son na wola
Maria Maria Maria Maria Maria
Maria Maria Maria Maria Maria
Maria! Faléwoulo ma Maria (No no no no no wo)
Maria Lidieunti wo ma Maria
Maria di Adéane
Marie di Bessemar
Maria Sindone
Marie Santhiaba
Maria di Bignona
Maria Diouloulou
Maria di Tanquille
Marie du Cap Skiring
Watch Video
About Maria
More BY MIC Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl