JAY 21 R.I.P cover image

R.I.P Lyrics

R.I.P Lyrics by JAY 21

Amoul loumeu geuneu diss ci lo mounoul dara ngakoy bayi mou dem
Nenagn warou ma ci triste buur Yalla mo taneu té ladjou ci keneu
Kou nek diap bop guiss Bi ngay tago di dem té lolou d’où guent
Bi ngay dem pare wouniou ko malakay meuwti latché lane motakh ngene fok dama bone
Oh no no
Khatch yi di Mbow Mbow Mbow
Dem nga té doto nieuw
Niou bayi leu nga go go bro do to nieuw
Amoul loumeu geuneu diss ci lo mounoul dara ngakoy bayi mou dem
Nenagn warou ma ci triste buur Yalla mo taneu té ladjou ci keneu

Romb nala ngané diamtane, Ma deg dem nga dama tite
Li né di déborder sama xol moné tourou sama guémine ma kheutch bic
Mais buur Yalla keneu leu té mo gnou tim mom mi gnou may beut leer neu mognou guiss
Bayi meu teudiate sama beut, fatalikou bi ngamay nane geumeul sama bop di nga dem
Lane mo nek sama blême, jour ya ngui dem té bayi wo beneu nouvelle
Natch bi watch journée diekh, souvenir yi effacer wou sama xel
Mais bro bi pob city sama berceau, koy fréquenter niou wakh leu ni nga mel
Bayi meu dieuleudji setou sama cercle douma bayi sheytane mane dima diey
Khatch y’a ngui Mbow Mbow Mbow
Tay sama Kogn nga reub you know
Xol yi fess neu del, rongogn ya ngui tourou, ya gnou djitou diapal gno ngui nieuw
Buur Yalla moy juge beu
Kou dem meuteul nga fi sa mission
Gnou rindi naak naakar tiss, diokhé mbiskit, dotougnou leu guissat
Oh no bro

Amoul loumeu geuneu diss ci lo mounoul dara ngakoy bayi mou dem
Nenagn warou ma ci triste buur Yalla mo taneu té ladjou ci keneu
Kou nek diap bop guiss Bi ngay tago di dem té lolou d’où guent
Bi ngay dem pare wouniou ko malakay meuwti latché lane motakh ngene fok dama bone
Oh no no
Khatch yi di Mbow Mbow Mbow
Dem nga té doto nieuw
Niou bayi leu nga go go bro do to nieuw
Amoul loumeu geuneu diss ci lo mounoul dara ngakoy bayi mou dem
Nenagn warou ma ci triste buur Yalla mo taneu té ladjou ci keneu

Dama la nit, am louma bet
Aduna tarder ko guiss né tefess
Li lane leu ni né sa xol bi di fess
Nianou ma Wone Yalla nieuk guiss sa caisse
Ya gnou djitou, legui gno ci dess
Yalla nama djik, lolou dou debat bou wess
Tour bi dou dik meme bou ruu bi né fess
Rou bi né fess té bi dotoul test
Sa RETANE ci diotay bi dotougn ko ess
Xolal meu li lolou nakar bo nangou leu ak mbekté bo maîtrisé woul lou dess
Diamono ji, xol ya ngui fess
Aduna diss, souf ba ngui ess
Diaroula tite,  beuss di nga guiss,  malaka yi oubi
Buur Bi ngay fek
Souf sedeu sa kaw yalla neu né
Xam na diotato sa mail
Ya gnou diema geuneu ya gnou geuneu beu faw Yalla diegal nieup meune neu né
Souf sedeu sa kaw meune neu né
Dadjé adiana meune neu né
Samay om ci souf loxo yi dieum ci kaw demal ci diam gentleman

Amoul loumeu geuneu diss ci lo mounoul dara ngakoy bayi mou dem
Nenagn warou ma ci triste buur Yalla mo taneu té ladjou ci keneu
Kou nek diap bop guiss Bi ngay tago di dem té lolou d’où guent
Bi ngay dem pare wouniou ko malakay meuwti latché lane motakh ngene fok dama bone
Oh no no
Khatch yi di Mbow Mbow Mbow
Dem nga té doto nieuw
Niou bayi leu nga go go bro do to nieuw
Amoul loumeu geuneu diss ci lo mounoul dara ngakoy bayi mou dem
Nenagn warou ma ci triste buur Yalla mo taneu té ladjou ci keneu

Watch Video

About R.I.P

Album : R.I.P (Single)
Release Year : 2021
Added By : Farida
Published : Mar 15 , 2021

More JAY 21 Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet

About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl