OMG Waxoma Woon Lii  cover image

Waxoma Woon Lii Lyrics

Waxoma Woon Lii Lyrics by OMG


[ COUPLET 1]
Beuga toma wakhma
Xawma lu waral légui mane falé toma
Guiss nani diex na
Waxoko mais khamnani ni nobatoma
Gaaw ci defma luma méti
Say wax néxatul mangui deg lu né
Lu dieum ci mane sa yoon nékoussi
Souma déwoon do weet ndax du mane malay wétali

[REFRAIN]
Wano ma woon lii
Bagnouy tambali
Waxo ma wone lii
Meunatuma  ndax dama  taaayi
Wano ma woon lii
Bagnouy tambali
Wakho ma woon lii
Meuneutou mala mougneul dax mane dame la baayi
Dame la bayi hé
Dame la bayi hé
Dame la bayi hé
Toggatumafi di mougn ndax mane taaayi
Dame la Baayi
Dame la Baayi
 May kila baayi

[COUPLET 2]
Goudi ba goudi lalay guiss
Dem na ba légui damako miss
Waxa tok mane
Falé toma
Sama wétal doon naxar ak tiss
Yay kiy béguel samay noon
Bax ci mbed mi ci mane nga bone
Dieukeur boula  yénétoul foon
Ma name la té sori woma

[REFRAIN]
Wano ma woon lii
Bagnouy tambali
Waxo ma wone lii
Meunatuma  ndax dama  taaayi
Wano ma woon lii
Bagnouy tambali
Wakho ma woon lii
Meuneutou mala mougneul dax mane dame la baayi
Dame la bayi hé
Dame la bayi hé
Dame la bayi hé
Toggatumafi di mougn ndax mane taaayi
Dame la Baayi
Dame la Baayi
 May kila baayi

[COUPLET 3]
Mangui dem guissouma liy tax may deloussi
Bou déssé loudoul sa keur ma fanaan ci mbed mi
And nexna wayé ko ba mou démak mbagam
Diox la sama xol ga fowé ko yaw danga lundeum
Yag na du tay
Wané gako tay
Naxaral sama xol xam nga yako tay
Légui dafa doy
Dotou mako joy
Beuss sa gui ci beussi lo lebblé  lagne lay fay

 

Watch Video

About Waxoma Woon Lii

Album : Melokaan (Album)
Release Year : 2019
Added By : Afrika Lyrics
Published : Aug 03 , 2019

More OMG Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl