
Machallah Lyrics
...
Machallah Lyrics by YOUSSOU NDOUR
Yalna yalla yokk sa jamm , waay
Li ñu mën nak xanaa di la ñaan al daal
Li nga yanu ahn ,ñépp xam na ñu ni diis naa
Onk u loo , daw u loo , nii nga mel , yagg nga koo mel
Han , han , han , han
Laaw la chat maa chaa allaah laaw la chat
Laaw la chat , maa chaa allaah
Ahn haa ohh ahnn
Yalna yalla yokk sa jamm waay
Li ñu mën nak xanaa di la ñaan al daal
Li nga yanu ,ñépp xam na ñu ni diis naa
Onk u loo , daw u loo , nii nga mel , yagg nga koo mel
Han han han han
Laaw la chat (daw u lo)
Maa chaa allaah(changer wo)
Law la chat (aye héé nay ou lo )
Laaw la chat , (nay ou lo )
Maa chaa allaah (fonk ou lo ohh ohh)
Ahn haa ohh ahnn
Guitare solo
Mbaye dieye:
Daw u loo deh , xaddi woo
Tiit u loo , raff lé woo deh
Gorée nga , tàng u loo,
Soxor oo , fiip ou woo
Daqq é woo, bëgg woo
Wax ou loo, né pâtt
Yaww…. Té jafe woo
Ku ñëw ak ku ñëw ul
Ku def ak ku def ul
Yaa ngi dëf te doo wax
ku am ak ku am ul
Ku mën ak ku mën ul
Ñépp xam na ñu sa ak mbaax (poñe woo)
Lu am nga taxaw ca (gëdd é lóo) ahn han , an han
(te soof u loo) ku jaaxle seet si la , an han , an han
Laaw la chat maa chaa allaah laaw la chat
Laaw la chat , maa chaa allaah
Ahn haa ohh ahnn
Daara d’ou takk nga changer laaw la chat
Daara d’ou takk nga changer maa chaa allaah
Daara d’ou takk nga changer laaw la chat
Laaw la chat ohhh woo ohh ohh
Laaw la chat nay ou lo
Maa chaa allaah daw u lo
Ahn haa ohh ahnn bew ou loo
Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine
Watch Video
About Machallah
More YOUSSOU NDOUR Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl