Balma Lyrics
Balma Lyrics by QUEEN BIZ
Mon bébé, Balma
Ooh bébé, Balma
Thia deugg, deugg, deugg wann ngama baby
Thia deugg, deugg, deugg wann ngama baby
Amour thji nouné lay fègnè
Mbeuguèl thji nouné lay feulé (balma)
Mom thji nouné lay fègnè
Mbeuguèl thji nouné lay feulé (balma)
Anh thji nouné lay fègnè
Mbeuguèl thji nouné lay feulé (balma)
Anh thji nouné lay fègnè
Mbeuguèl thji nouné lay feulé (balma)
Damay tok diko xol, diko xol diko bardé
Dafa am, dafa am, dafa am
Sama yeurmandé
Damay dem, damay dem
Sèti sama waadji
Xolna xol, xol, ba xamni meunoumala bayi
Chéri, baby
Chéri loumay yeuk sama xol meunoumako bindeu
Thia deugg, deugg, deugg wann ngama baby (love ngama)
Thia deugg, deugg, deugg wann ngama baby (love ngama)
Amour thji nouné lay fègnè
Mbeuguèl thji nouné lay feulé (balma)
Mom thji nouné lay fègnè
Mbeuguèl thji nouné lay feulé (balma)
Anh thji nouné lay fègnè
Mbeuguèl thji nouné lay feulé (balma)
Anh thji nouné lay fègnè
Mbeuguèl thji nouné lay feulé (balma)
Dafa melni lampe léral sama yonn
Bama xamé man founa dieum
Diam ngama nani thji xékhou mbeuguél
Bae nagouna yama meunn
Biss niki tay, yaw yama mom
Dama sakousi sa ngeureum
Néé thji loula neekh dokh thji loula neekh
Fo dieum fofou la dieum
Chéri, baby
Chéri loumay yeuk sama xol meunoumako bindeu
Thia deugg, deugg, deugg wann ngama baby (love ngama)
Thia deugg, deugg, deugg wann ngama baby (love ngama)
Amour thji nouné lay fègnè
Mbeuguèl thji nouné lay feulé (balma)
Mom thji nouné lay fègnè
Mbeuguèl thji nouné lay feulé (balma)
Anh thji nouné lay fègnè
Mbeuguèl thji nouné lay feulé (balma)
Anh thji nouné lay fègnè
Mbeuguèl thji nouné lay feulé (balma)
(Balma, balma)
Watch Video
About Balma
More QUEEN BIZ Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl