Awma Temps Lyrics by JAHMAN XPRESS


Xawma wone sakh mane ngay waxal  ( Anh kone mane ngay waxal )
Mane yeugouma wone sakh mane ngay wakhal ( Anh kone mane ngay wakhal )
Anh kone mane ngay wakhal (Anh kone mane ngay wakhal )
Sibou ma wone sakh mane ngay wakhal

Degoumala wone
Dama takeu ay écouteurs
Xeer yingmay sani la dieul dadialé tabakh ngandim keur
Ndissou (Marchandise)  bandit dou lambeu
Diaye leu  ci diam wala diaye leu ci force
Danga yeeg ndakh dollars sa poche
Kone di nga wade comme lou nekk ci fosse
Lii rek kessé meunone ngene ko vocal
Khathie bou yagg té door bi daloul
Boxeur allumette Cafal
Bif ci game bi la bokk na bangit yi ndelou
Dou yagg ba Tom nekk OG wou Jerry
Eh mounouleu niakk
Nieneu gni di takkeu sama kaw ndakh gnima ci faye dafa beuri
Feu bi diougué neu rouge mongui ci vert
Lo tekk lenene perte
Sama tankeu dafa diss talli bi nekh
Maak yaw mounougn fréqu

Kou bari diom niakeu diot
Kou niakeu diom bari diot
Motax mangui sama bopp awma temps
Awma temps deh

Xawma wone sakh mane ngay waxal ( Anh kone mane ngay waxal )
Yaw kone mane ngay waxal ( Anh kone mane ngay waxal )
Wah yene ki kane ley waxal ? ( Moma diakhal )
Sibou ma wone sakh mane ngay waxal

Do dioum ba degg phone bi sonner
Silence laay réyer niou bari
Time is money té money nga weuri
Weuri nga ba temps bi diekh , C'est horrible  
Okay , léweul , foureul
Sene wakhtane bi commencé beuri
Xam lepeu ci keuyitou keur yi
Mangui ni deh nioul ni keurign
Ceddo bi moy sa serigne
Indi neu li ngene di sango ak li ngene di naan
Ndakh sen jotaay bi dafa dessé ay mandi yeah
Takeu naa boon yi taalal
Dangene am fiit rek
Ba di dadialé doule yi ba beut sett
Coma nekhal waxtaan bi di kheur seen maam
Bangueen khol ma nema kane ngay waxal
Soy guiss sa  baye  daw soufou ronde laal bi
Téy deh fa ngey fanane

Kou bari diom niakeu diot
Kou niakeu diom bari diot
Motax mangui sama bopp awma temps
Awma temps deh
Xawma wone sakh mane ngay waxal ( Anh kone mane ngay waxal )
Yaw kone mane ngay waxal ( Anh kone mane ngay waxal )
Wah yene ki kane ley waxal ? ( Moma diakhal )
Sibou ma wone sakh mane ngay waxal

So dégué "tinntt" boul insister awma temps
Mangui sama bopp
Somay woo ney lou urgent
Seen nala ngamay vocal
Sou goudé doumako lire
Teyeul seu ay cas
Niit dey positif
Dougou nga laal nga bandit
Boulma xaar ci taatou ndaa li
Eau de source laay naan
Ya nara xaar ba xadi
Diot ma dou yombou ndakh damala vent
Dama départ té yangui ci banc
Rolex dou nekk ci lokho kou bari temps
Mane ak yaw bokouniou rang
Diot bi mounoul bari
Dama bayi lou bari
Wara dem fou sorri
Tedeu wara teudi
Té mane douma tokk tant que takouma
Tekki tekkil niou topou ci mane douma teggi tank
Wax dji ladoul meun
Mais réwandé mo gueun yomb
Soudé gniii niémé naa
Comme sho bou wétt ak kou yoom
Sa percer dou gaaw ndakh
Ndakh dangay door
Té xool naa ba xool mais dessé nga mur
Sorou mala
Louné ngama yakkeu
Mais meunoma yeungueul
Faye laa moma niorr
Fayo ma weer beug ma teyé ci ligne bi
Coupél deukk bi dafa wow
Awma diot mesures yima dieulone dembeu dafma serré
Yaak mom ci pott
Est-ce que meew yinga fi xélli meune ngako sédé
Come on

Kone yéne kii mane lay waxal (Anh kone mane ngay waxal )
Xawma wone sakh mane ngay waxal (Anh kone mane ngay waxal )
Okay kone yaw mane ngay waxal (Anh kone mane ngay waxal )
Yangui wax ak teukh (Anh kone mane ngay waxal )

Anh kone mane ngay waxal
Anh kone mane ngay waxal
Anh kone mane ngay waxal

Watch Video

About Awma Temps

Album : Abiyo (Album)
Release Year : 2021
Added By : Farida
Published : Nov 24 , 2021

More JAHMAN XPRESS Lyrics

JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl