Yaa Tey Lyrics
Yaa Tey Lyrics by SIMON KOUKA
[VERSE 1]
Da nga ni wone 5 ngey def
Moudjou def 7 ya tey
Do meussa fal sa rakk
Nga wax waxet ya tey
25 ministres nga niou digone
Romb ngako ioe di dém
Askann gou niou yaggue lottal
Loko tek ioe mouléé
[CHORUS]
Loula nex def ya tey
Koulan ex teuthi ya tey
Justice bi né pateu ya tey
Etudiant bou grève nga fatt ya tey
Loula nex def ya tey
Koula nex teuthi ya tey
Justice bi né pateu ya tey
Etudiant bou grève nga fatt ya tey
[VERSE 2]
Kilifeu diné niane naleu
Djèkeu nga bagn
Khalifa palais la leu
Beugoneu khagn nga takhagn
Télé wala radio
Kou kass boss beu ngey djeundeu
Y’en a marre tégual la right
Nga djigne ko nane katou seungeun
Loko tek ioe mouléé
[CHORUS]
Loula nex def ya tey
Koula nex teuthi ya tey
Justice bi né pateu ya tey
Etudiant bou grève nga fatt ya tey
Loula nex def ya tey
Koulan nex teuthi ya tey
Justice bi né pateu ya tey
Etudiant bou grève nga fatt ya tey
[VERSE 3]
Askann wi lott ioe ngey féthi
Niou coupé ko ndox
Ngey weundél dékheu
Sédeulé milliards si campagne
Tardel bourse étudiant yi
Yeukeuti fitneu tek sagn sagn
Armé sey partisans yi
Askannou leumb nga bétt do falou
Di nagn la kheut,té ken doula Walu
Askannou leumb nga ngott do falou
Di nagn la kheut,té doula walu
[CHORUS]
Loula nex def ya tey
Koula nex teuthi ya tey
Justice bi né pateu ya tey
Etudiant bou grève nga fatt ya tey
Loula nex def ya tey
Koula nex teuthi ya tey
Justice bi né pateu ya tey
Etudiant bou grève nga fatt ya tey
[OUTRO]
Milliards yi nga dikk deukou
Kaw gui guissou niou ko
500.000 emplois par an yeugouniou ko
Sénégal émergent bi batay doundou niouko
Kone Macky deuxième mandat
Bi ioe mérité wo ko
Watch Video
About Yaa Tey
More SIMON KOUKA Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl