SIDY DIOP  I'am Sorry  cover image

I'am Sorry Lyrics

I'am Sorry Lyrics by SIDY DIOP


Khana khoulo dey dièkh, haaaa haaaa…!

[CHORUS]
S’il te plait donne-moi une chance
Beug nala lool… s’il te plait donne-moi une chance
Beug nala loool…love you ma chérie my honey
Hann… weetal ngama, nameu na sey diotay lolou
Je t’aime, tu m’aimes, je pense à toi
 S’il te plait donne-moi une chance

J’ai pris le temps de dire ces mots
J’ai pris le temps d’attendre tes mots
Je t’aime et tu le sais ioe
 S’il te plait donne-moi une chance bébé
Mane dé souma lérone, adbou rass lila dound si trahison
Ma wouti solution ni thioubalo waw ndaxté
Xalé bi wétal nama
Té sama mame néna ndaw ak kamou mine eh ah  
Souko guissoul weet day weet
Mane dé beugeu nala ioe
 Ya nek ci xool bi xeel mi doula faaté baby

[CHORUS]
Beug nala lool…s’il te plait donne-moi une chance
Beug nala loool… love you ma chérie my honey
Hann… weetal ngama, nameu na sey diotay lolou
Je t’aime, tu m’aime, je pense à toi
S’il te plait donne-moi une chance

Baby mala togn (mala togn)
 Nagn tourner la page dound lénén nga balma (nga balma)
Yeah yeah…ndax sooneu na (ndax sooneu na)
 Li nga def ci manet akh ma top leu
Je t’aime, tu m’aimes, je pense à toi
S’il te plait donne-moi une chance baby
Ohh my baby, my baby baby baby baby
Ohh my baby, my baby baby baby mbiféé

[CHORUS]
Beug nala lool... S’il te plait donne-moi une chance
Beug nala loool… love you ma chérie my honey
Hann… weetal ngama, nameu na sey diotay lolou
Je t’aime, tu m’aimes, je pense à toi
S’il te plait donne-moi une chance

Watch Video

About I'am Sorry

Album : I'm Sorry (Single)
Release Year : 2019
Added By : Tamsim Diouf
Published : Nov 11 , 2019

More SIDY DIOP Lyrics

SIDY DIOP

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl