RWMR Lyrics by ELZO JAMDONG


[VERSE 1]
Rap wolof mo raw
Rap wolof mo raw
Rap wolof mo raw
Rap wolof mo raw

Aka ma beurre ay fiston wowé dady ba keyti bibson
Moussouma sokhla sa piston y’Allah may nama catane adiction
Pour danel la diaroul may tite, diaroul mey yakamti caloul rek
Kou diok songue gaindé sa kharou ngey guiss
Sa sho ak sa cachet lay nangou né tirr dem tchil sama borr
Rap na siguil sama kogn mais légui
Il est temps ma diw sama poche you diss
Comme nangou nga free dafa fort
Nagn yeungeul ba sodav fayou ndax fauk niou riche
Meun nek MC nek PDG diabaneté AIBD ak CDG
Souniou joboul tabax tem niou kheuy rek dé
Souniou domi mague néniou weré ngerr
Welcome to the macina, am la Amadou Hampaté Bassira
Ngadi kangame la Cheikh Anta Lassira
Youga taupe la mais fatéwoul racine nam bro et puis capitulé
Lo kham ci poulo bou magué ci koniou lébou dila lakk
Ay wolof you lerr koufi antane sama vocabulaire
Rap wolof mo raw (Rap wolof mo raw)
Nioune gné wougn states gné wougn kaw
Djolof mo ndaw rek sinon niou yeungeul ba aduna

yeup khamné nio geuneu graw
Rap wolof change woul pour geuneu fégn
Nioune wagni ay fans mo niou geuneul fake
Niak nagn lass dotouniou nélaw
Bourba ak Pacotille niom ken doulen fay

[CHORUS]
Rap wolof mo raw
(rap wolof job)
(rap wolof job)
(rap wolof job)
Rap wolof mo raw
(rap wolof job)
(rap wolof job)
(rap wolof job)
Rap wolof mo raw
(rap wolof job)
(rap wolof job)
(rap wolof job)
Rap wolof mo raw, rap wolof mo raw, gné wougn states

Ma niggah nioune gné wougn kaw
Djolof mo ndaw rek sinon niou percé ba cana
You nioul niow follow niou naw
Rap wolof mo raw, rap wolof mo raw
Rap wolof mo raw gné wougn states
Ma niggah nioune gné wougn kaw
Djolof mo ndaw rek sinon niou feusseul ko ba
Aduna yeup khamné nio geuneu graw
Rap wolof mo raw, rap wolof mo raw, rap wolof mo raw
Sou fayoul douniou rap ak wate
Il faut niou takk ni soixante watts, son bi si vap ak boite
Shrat tou black ci rak tak squad, so fayoul douniou
Rap ak wate, damay diaxassé rap ak crack
Rap wolof abadane shadap rak tak squad
(Yeah, yeah, yeah, yeah, yeah) shadap rak tak squad
Rap wolof mo raw, da nga dof waleu Jamdong leu
Shadap rak tak squad

Watch Video

About RWMR

Album : FREESEASON 2 (Album)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Nov 11 , 2019

More ELZO JAMDONG Lyrics

ELZO JAMDONG
ELZO JAMDONG
ELZO JAMDONG

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl