Pop Freestyle Lyrics
Pop Freestyle Lyrics by ELZO JAMDONG
[VERSE 1]
Rappeur you ndaw yi daniou sakane microbe microbe
Il faut niou magg pour meuna yek sama niveau niveau
Sama vocabulaire dafa riche niko diko
Khalissou diay katou drogue freedo freedo
Ioe rap dafa meti ci ioe mane musique dafa yomb ci mane
Mane guissouma len dama myope ken wanouma lou original
Ken mounouniou téré dadialé tabax ay villa ak khaliss pra bi
Kholou son bouniou sandi mou diap légui
Ndaxté boy yé kay capté comme prabole
Bind gayi geuneu free motax meussouniou diteu
Guissouma kane mo niouy kill, guissouma kane mo niou mos
Guissouma kane moniouy nott nga guiss sama rongogn ci beut
Mane la rappeurou Sankara, ioe la rappeur’ou trump bitch
Diokhéna sama kaddu diokhéna, diokhéna sama kaddu
Yok na sama cadence, yok na, yok na sama cadence
Lakk nagn plaza mais téréwoul kogn ban gui pop pop pop
Gni gni camelet, ken mounou niou stop
Ken douniou blow, ken mounou niou dap
Da ngen di saup, ken mounou niou stop
Town ngui pop ba legui, town ngui pop
Town ngui pop ba legui, town ngui pop
[CHORUS]
Ken douniou blow, ken mounou niou dap
Da ngen di saup, ken mounou niou stop
Town ngui pop ba legui, town ngui pop pop pop
Town ngui pop ba legui, town ngui pop pop pop
[VERSE 2]
Sénégal Sénégal, Sénégal Sénégal
Fo len di dieulé kou melni mane
Je dis Sénégal Sénégal
Rap wolof MTV, assico RFI
Rap wolof MTV chaque année MVP
Sayouma dougué ci metro bi R rek ma guéné ci niary punch
Ioe lidieunti aduna diambour ak sathi ay flow ci mane rek la sa gayi meun
Mounou ma supporté fake yi ley bégué bo guesto niou tek la paka dokh
Bou fogoné kep koula signe diam lala yéné dafa fek magago
Defouniou dara ci interet, defouniou dara ci interet
Nio geuneu xaragn ci internet, dotougn guen loudoul fegn télé
Défouniou dara lou ken téré a part diapalé peur ti di fêté rek
A part nagou ay terre di soul di déterré enchainé victoire di fêté rek
Nibo toplarr beat’ou ATL flow dope man hit’ou Alien
Tokhol nagn bat yi almadie mais kogn ba ngui pop ba légui
Thioy ya ngui dakha ji rasta yi mais boy ya ngui tal comme Jamaïque
[CHORUS]
Ken douniou blow, ken mounou niou dap
Da ngen di saup, ken mounou niou stop
Town ngui pop ba legui, town ngui pop pop pop
Town ngui pop ba legui, town ngui pop pop pop
Ken douniou blow, ken mounou niou dap
Da ngen di saup, ken mounou niou stop
Town ngui pop ba legui, town ngui pop pop pop
Town ngui pop ba legui, town ngui pop pop pop
Pop Pop Pop Pop Pop Pop
Watch Video
About Pop Freestyle
More ELZO JAMDONG Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl