BRIL Bras Long  cover image

Bras Long Lyrics

Bras Long Lyrics by BRIL


[INTRO]
ooooh ooh ooooh
Bril laa aaah  (Bril on the beat)

[REFRAIN]
Fi douniou khol lane nga xam wala lo meune ?
Daniouy Laathie  kane mola yabal thi niom
Lokho bou goudou fok nga amko soga dém
Bouthi kéneu djaappoul dinga yaggueu thi sa yone
Est-ce que am nga Bras Long ?
« Bras Long - Bras Long »
Bo amoul Bras Long, dothi gawa guéneu
Am nga Bras Long !
« Bras Long - Bras Long »
Bo amoul Bras Long
Est ce que ding thi guéneu ?

[COUPLET 1]
Bimay khalé dagn ma gueumlo ni wone
Bouma djangué , bouma maaggué liguey
Ma yaggueu thi école yi woute ay diplômes
Lima rote thi xam xam guéédj la meuna thié fééy .
Wayé founé démnafa
Lima djokhé thi ay CV boudone khaliss ma done millionaire
Bo kholé sén mbalite yi guissmafa
Bimay déposé lay xam douma am, moudjé nékk visionnaire
Kane mola yabal ? Fok nga xam , kou xam koulén xam !
Djangal badone kangam sokhlawougn sa Xél fii !
Kholouniou sa xam xam , Lidjeuntiwougn sa meune meune
Wouteul Bras Long mélal ni kouy selfie !

[REFRAIN]
Fi douniou khol lane nga xam wala lo meune ?
Daniouy Laathie  kane mola yabal thi niom
Lokho bou goudou fok nga amko soga dém
Bouthi kéneu djaappoul dinga yaggueu thi sa yone
Est ce que am nga Bras Long ?
« Bras Long - Bras Long »
Bo amoul Bras Long , dothi gawa guéneu
Am nga Bras Long !
« Bras Long - Bras Long »
Bo amoul Bras Long, Est ce que ding thi guéneu ?

[COUPLET 2]
Bo amoul koulafa nékkal yakkar ni dangay am
Day mélni ngané dangay Connectéwou té amo pass !
Té fo am yakkar djaroul ngafay dém
Boudé kénneu Xamoulafa ni sa mot de passe !
Thi musique bi, Lamb Dji’ak foumou meunti done
Bou sa lokho goudoul lingay yôttou dothi djote
Bo khamoul kou xam borom téén djaroul ngay soneu
Même bo amé baak yaw dofa meuna Roote
Bodé djiguén gueum sa bopp say mbir dougn thi #Takhaw
Dofa meuna #Took , Boudé beuggo #Teudd
Niawloul ay courte manche bo amoul Bras Long
Lo beugga natteu niounéla djotoula , lofi wakh dou deugg

[REFRAIN]
Fi douniou khol lane nga xam wala lo meune ?
Daniouy Laathie  kane mola yabal thi niom .
Lokho bou goudou fok nga amko soga dém .
Bouthi kéneu djaappoul dinga yaggueu thi sa yone .
Est ce que am nga Bras Long ?
« Bras Long - Bras Long »
Bo amoul Bras Long ,dothi gawa guéneu
Am nga Bras Long !
« Bras Long - Bras Long »
Bo amoul Bras Long, Est ce que ding thi guéneu ?

[PONT]
Amo bras Long, Takhoul nga djaay sa ngor
Danga woute liguéy ba woutoum Liguéy moudjé done sa Liguéy
Boul Khaadi té boul gawa bayi
Kheuthie bou daggoul dikkeu
Yalla bourbi dalay Fay

Est-ce que am nga Bras Long ?
« Bras Long - Bras Long »
Bo amoul Bras Long, dothi gawa guéneu
Am nga Bras Long !
« Bras Long - Bras Long »
Bo amoul Bras Long, Est ce que ding thi guéneu ?

 

Watch Video

About Bras Long

Album : SUBA (Album)
Release Year : 2019
Added By : Afrika Lyrics
Published : Aug 13 , 2019

More BRIL Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl