Self Made Lyrics by ONE LYRICAL


[VERSE 1_One Lyrical]
Da may hustle toogal di wax pourquoi ñu nan ma no way
Beugguloo ma me too I do you baby screaming my name
I believe I can fly don’t tell me no bless over my lay
Still the same don’t know us
Keep yourself about me
Tay ma burle kon jarul pass
Gnaata nitt a ma gassal pax
Gnaata nio ma bagn
Mais né nagn bul di topp sen xol yeuppay bax
Gnaata nio ma yeene comeback
Ñaata nitt nga woolu denk len sa lepp tay niou nan la yay kan
(Fuck yay Kan) Motherfucker yow yay kan
(Mofucker yay kan) Topp sa yoonu bopp rekk a fi des
Seugg gni di wax siggil sa bopp
Siggil sa boop sëgg say wayjur hater niggers what a fuck
Man maa siiw parce que da ma sob
Li ngen gnoddi boo ubbe sama bopp ding ko fekk mu toog
Keneen ku melni man gisu mako
Ci kaw ci sa kanam feeteel ginaaw budul ci gent do ma fuck
Nee na la man bëggu ma jikko toot
Fuck you ya’g sa buzz do gis ku dee yobbale siiw yawmal xiyaam
(Fuck)

[CHORUS]
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoon
Dieul sama yoon
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoon
Dieul sama yoon
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoon
Dieul sama yoon
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoon
Dieul sama yoon

[VERSE 2_ HAKILL]
Bo xamul fi nga jëm deelul fi nga joge
Loolu day fekk fi nga joge neex
Saytaane bari dooli ken duko jege
Mais dara dara duma teree xeex
Akk moom ndax ay sëttëm rekk ño ma wër
Bëggu ñu ma nekk ci Jàmm ni malade budul wër
Bimay ne sama biiru yaay rekk la nekk fu woor
Judd nekk goor
Zéro peur Yalla rekk lay soor
Awma lu may rèccu lepp noonu la
Duma changer tus lepp ci yoon bi la
Yen say lu gëna baax ci yow lu bonn bi la
Samay meilleurs professeurs sama noon yi la
Nitt ku ñuul ñemewul lu bees
Foo jaar ñu bëgg ma ray

Bu samay noon bariwul woon sama bopp lay njëkk mere
Mën a baax mën a bonn lo fi seet gis ko may internet
Nitt kuy weeco ay nitt doonul ludul nittu interêt
Jël sama yoonu bopp vitesse Foog ma seey len
Freins yi dagg may duggël vitesse gaaw ni Eminem
Ay jëmm tiim ma bëgg ma fees man may nittu neen
Jàng na ci lepp lima wees muy dëgg di fen
Jël sama yoonu bopp, sama yoonu bopp, no no sama yoonu bopp
Topp ma ken ma ngi sama yoon
Topp ma ken ma ngi sama yoon
Topp ma ken ma ngi sama yoon
Ich yo boy

[CHORUS]
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoon
Dieul sama yoon
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoon
Dieul sama yoon
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoon
Dieul sama yoon
Dieul sama yoonu bopp a fi des
Dieul sama yoon
Dieul sama yoon

Watch Video

About Self Made

Album : Potentiel (Album)
Release Year : 2019
Added By : Tamsir Diouf
Published : Nov 11 , 2019

More ONE LYRICAL Lyrics

ONE LYRICAL
ONE LYRICAL
ONE LYRICAL

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl