MLW Lyrics by ZO FLAME


Ey magui I sokhor clé
Xalei la tewoul grand doma téré (téré)
Dalal djemeuh geu deglouuu nough key défeiii dafa ladj déguine
Koufi deugeur bop niou kong le Rong Tama
Boy noume ak yeine dou game nakh dagn meune play
Wa zé Moy limeley wakh
Moy limeley tégual
Dolei ak fitt nioy deff
Waw key, waw key waw key nioy def
Ah ah Moy Limalay Wax
Moy Limalay Wax
Dolei ak fit nioy deff
Wawaww nioy def

All eyes on me
Fight comme nieup kéneu bagnla yapeu (kéneu bagnla yapeu)
Mane la may kaneu samay limite lay pousse
Xol faneu lay yémeu
Sama combat ak life la nekoul ak gayii
Xol fép foy déf sa Time
Liguey ba mère bayi yek séneu tata yi
Gagné si rap bi guerre yeup ak batail yi
Off line yeup Paré doff bay nieup
Fok niom nieup teup ak séneu gars yeup
May tokeu trône burr ak khadieum
Béneun king OG yéneu ay thianyneu (Ayy China)
Dioumouna meumeu rap comme yeineuh (Diomou nako)
Kawéna kouna dapeu day yékeu
Deumb la louma def day yéss
Anawannn Nekè malèneu yèmeu

Ey magui ni sokhor clé
Xalei la tewoul grand doma téré (téré)
Dalal djemeuh geu deglouuu nough key défeiii dafa ladj déguine
Koufi deugeur bop niou kong le Rong Tama
Boy noume ak yeine dou game nakh dagn meune play
Wa zé Moy limeley wakh
Moy limeley tégual
Dolei ak fitt nioy deff
Waw key, waw key waw key nioy def
Ah ah Moy Limalay Wax
Moy Limalay Wax
Dolei ak fit nioy deff
Wawaww nioy def
Okay okey
Mes respect chef
Mais douniou terei rew (Nio tay)
Ga Def niou nadnkeuh rek passkeu bay yin iii nio xew (Nio xew)
Kou sissou niou mey leu diounii (anh)
Diaroul Meer bey founki nan (Nah)
Togfi di fene niouy touki
Djiob pour poche yi do founki (fataww)
Niom aka nio Faux (Ndeysanne)
Parei djapeu ni kene Siboulene
Doff la kone bayilene si Bain
Wa yéne sangoulene ey ey
Magui fi dey koulandakh dey koulandakh dey koulandakh yene ayo lene
Dey koulandakh dey koulandakh dey koulandakh yene meti wolene

Wa zé wa zé anawan wa zé moy limaley wakh khana yaw do degeu
Wa zé wa zé anawan wa zé douma def comme yene loubess la wathier
Anawan wa zé min wawi
Rombouna dotouma wouyou wadji
Songou nama moy doumeu n’a wadji
Dokhanouma nangou n’a gelou wadji
Wadji yoroulo niodei aladji
Bayil liga wekeu si ga ladji
Rap ley doundé mais lekoul si kagne bi
Vraiment vraiment yeureum n’a wadji hahaha
Boy sonal nga wadji
Wa zé moy limzley wakh
Moy limeley tégual
Dolei ak fitt nioy deff
Waw key, waw key waw key nioy def
Ah ah Moy Limalay Wax
Moy Limalay Wax
Dolei ak fit nioy deff
Wawaww nioy def

Watch Video

About MLW

Album : YMT (Yalla Mognu Taal) (EP)
Release Year : 2023
Added By : Sainclair Fonkou
Published : Jul 08 , 2023

More ZO FLAME Lyrics

ZO FLAME
ZO FLAME
ZO FLAME

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl