Level Up Lyrics
Level Up Lyrics by ZO FLAME
Fogone nani yay doni sama yayou dome
Mane diapone nani fouma gestou guiss leu ioe
Man fogone nani diabar dji yaw ley done
Eeh diabar dji yaw ley done
Tu sais tu sais tu sais
Yaw rek la lovone yeaaaah
Tu sais tu sais tu sais
Yaw rek la lovone yeaaaah Ay
Defna effort bounei
Ioe guissoulo
Appel texto sa call
Ioe falei wo Ay
Diem nala topou ba sonou
Mais bougolo hmmm
Mais bougolo
Légui diekhneu magsi lénéne ak kénéne
Domeu terei doundou maguifénéne ak kénéne
Guissna gemey follow mais dou tei magui si lénéne
Même souniou tassei bénéne monde dou demei nénéne
Nakh ioe
Kholeu toumeu leu
Guisseu toumeu leu
Magui bénéne Leve yeah
Kholeu toumeu leu
Guisseu toumeu leu
Magui bénéne Leve yeah
Kholeu toumeu leu
Tu sais tu sais tu sais
Yaw rek la lovone yeaaaah
Tu sais tu sais tu sais
Yaw rek la lovone yeaaaah
Ak finiou diaar yeup
Ak liniou dioteu doundou
Diémo khol si Lolou
Ak finiou diaar yeup
Ak liniou dioteu doundou
Diémo khol si Lolou
Ouhhhhh my baby
Mane diapone nala Bugone nala falei woma
Ouh ouhhhhh my baby
Légui diexna légui diexna légui diexna
Ouh ouhhhhh my baby
Diapone nala beugone nala falei woma
Ouh ouhhhhh my baby
Légui diexna légui diexna légui diexna
Légui diekhneu magsi lénéne ak kénéne
Domeu terei doundou magui fénéne ak kénéne
Guissa gemey follow mas dou tei magui si lénéne
Même souniou tassei bénéne monde dou demei nénéne
Nakh ioe
Kholeu toumeu leu
Guisseu toumeu leu
Magui bénéne Leve yeah
Kholeu toumeu leu
Guisseu toumeu leu
Magui bénéne Leve yeah
Tu sais tu sais tu sais
Yaw rek la lovone yeaaaah
Tu sais tu sais tu sais
Yaw rek la lovone yeaaaah
Watch Video
About Level Up
More ZO FLAME Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl