Number One Lyrics
Number One Lyrics by JEEBA
Yeah!
Yaa takh leep louma songue daan ko
Doleel ngama founè
Niit kila noop ba nieup kham ko
Nala diaral lounè
Mane diokh nala lounè lounè
Mane diokh nala lounè eeh
Nala follow feep fo deem
Mane Oie lay titeuro feep fuma nè eeh
Mane dagn may mereii sumaay wakh si oie
Ndakh meusso changé meusso kakatar eeeh
Yaay Sama number one, number one
Jikoo bu raffet lolou ngama wone
Lolou ngama wone
Duubi duubi daddy daddy
Mane maay sa daddy daddy
Duubi duubi daddy daddy
Mane maay sa daddy daddy
Sama babe kaay
Guiss na sa melookane
Ya takh maay deukei daane
Oie reik ya takh ma fier remuer ciel et terre
Nguir Leep louma am ma indil là
Woma ma nieuw balaa Ngay teek reer
Xamna leep lou baax pour mane laa
Diokh nala lounè eeh
Yaa takh leep louma songue daan ko
Doleel ngama founè
Niit kila noop ba nieup kham ko
Nala diaral lounè
Mane diokh nala lounè lounè
Diokh nala lounè
Mane diokh nala lounè lounè
Diokh nala lounè yeaah
Deef la diabar tè keine doussi teek baat
Nieup d’accord ni danga mérité dote
Adjio saay mbaag titeuru wo danga took
Sama galeh keen koudooul oie duufi teek tank
Yaay Sama number one, number one
Djiko bu rafeet lolou ngama wone Lolou ngama wone
Duubi duubi daddy daddy
Mane maay sa daddy daddy
Duubi duubi daddy daddy
Mane maay sa daddy daddy
Leigui naak li mossi desseu
Nga took Sama weet tei doo deem
Doo jigueen bouy took ni fess seuuuuuuh eeeuh
Eeeh diokh nala lounè lounè
Diokh nala lounè
Oie ya takh leep louma songue daane ko
Doleel ngama founè
Niit kila noop ba nieup kham ko
Nalaa diaaral lounè
Mane Diokh nala lounè lounè
Diokh nala lounè eeh
Diokh nala lounè
Mane diokh nala lounè
Watch Video
About Number One
More JEEBA Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl