Dalou Adouna Lyrics
Dalou Adouna Lyrics by KID DOU
Meussoumeu guiss ma try ma nekk si lonely
Deff na ay projet youy diay
Gni fogougnou wone lii
Meussoumeu guiss ma try ma nekk si lonely
Deff na ay projet youy diay
Gni fogougnou wone lii
Dingua dieki dieki Guiss ma Garé trok bi
Fokk ma wéki Gnimeu beuguone barél yone wi
Dangmay rombou dimeu nouyou lekk lekk
Nga Toguakk kénéne di wakh si mane lo khamoul
Ma Teudé gni eumbb sa rappeur
Ouakam denkk nama Drapeau
Mbedd béma nangoul Ak Sa wakeur
Dalou adouna la Sol yeyeh
Sopi deff crampon yeyeh
Eskey signé Ko man (Coman-Bayern)
Am dolé bayern kouné lay fadj koukoy pariéé (iyeh)
Allô Allo wagnilma sa thiow
Soril boudé beuguo yeuffou Goor
No matter meloumani ten thousand
Mais doff ndey sah mako Geuneu con
Fi deur leu do miné ni Fou bou tameu soul ay dope
Yow Bayil say connerie
Door leu dominé ni modou xaragne souley dope
FIls niakkouma dolé bi
Par force danguay roukh ni Auto Police souley topp
Gneuw Andalé sirène bi
Kou romb niveau Assamane wakhma kouley diott
Sa khel binguay Niopati
Mama Waroul mérr santouma loudoul dioulékk diangg
Papa Nénama fékhél ba lepp loy deff si Adouna bi na done diam
Meussoumeu guiss ma try ma nekk si lonely
Deff na ay projet youy diay
Gni fogougnou wone lii
Meussoumeu guiss ma try ma nekk si lonely
Deff na ay projet youy diay
Gni fogougnou wone lii
Yagg na degg si yaye
Téguilma thiono sa Baye
Problème yi kholko si eyes
Meunougnou dead si sa vibe
Defal sa confident sa Ndiéguénay
Wéteuk sa problémou life bokk
Dalou adouna bi lay pro
Ken dou thiarakhou ay no
Thiatou Montagne bi tokk
Sen ma sikaw kouné yaye sama boss
Dagn la tinguome life bi diott nama wone
Niata djiko dina done number One
Fuck sa niveau manguekk niata diplome
Né si job bi di job beugg tankal say nopp
Mélni gnom sidy Diop
Derett tokk si gnom
Deff sen kani chewing-gum
Defaite tokki si gnom dinguene deukk si thiow (bro)
Si lou Méti la yagg dokh
Dalou Adouna la Mérito
Amoul Métite boumay réthiou loooo
Téguil thiono sama yaye boye (yaye boyo)
Téguil thiono sama baye Boye
Meussoumeu guiss ma try ma nekk si lonely
Deff na ay projet youy diay
Gni fogougnou wone lii
Meussoumeu guiss ma try ma nekk si lonely
Deff na ay projet youy diay
Gni fogougnou wone lii
Watch Video
About Dalou Adouna
More KID DOU Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl