Miss U Lyrics
Miss U Lyrics by KID DOU
All time all time
I Need life now more
I miss you and I'm crying
Don't know for how long
I pray i pray
I’m praying for you
All day and all night
I don't now for how long
Doundou bu nekh founé la dane andakk mom
Yagg nala wo dila tekk Choc
Louné ngama deffal si sama life ioe
Buur yalla mola dieul sagnouma thiow
Legui beugeutoumeu teudd sama lale
Soumay khalatt ni ya teudd thi souff ci
Akk lou meunoneu khew makk ioe gnoy bokk gual
Kone Batay meunoumeu geumni nékatofi
NittKou Deuggou leu wooone
Khamoul nakhaaaté
Namela loool
Kene doula faaaaté
Thi sougnou khol yi
Lagn la maaarqué
Kholangui diooy
Khel dila laaathié
Buur béla wo
25Avril si weerou koor
Démé nga ndaw
Gneup sédé ni kholou diamant nga yoor
Deggeul say wadiour fonkkone say waxtou diouli soralé mort
Yakk gningfa fekk yalnalene yalla mousseul lene si bepp Loor (Amine)
All time all time
I Need life now more
Your absence I'm crying
Don't know for how long
I pray i pray
I’m praying for you
All day all night
I don't now for how long
Guiss say sourire soumlay khalatt
Sougnouy Souvenir dou diekh walay
Souffrir si khol moudié malade
My best friend Weetay nga bayi
Boul diakhlé no manguifi batey
Waw samay gnane dey agg key
Biir Aldjiana Firdawss Ngay tali yeurmandé lako mey
Sama khola fess waroumeu dioy
Nakarafi dess mangui si thiono
Amatoul lou bess si souniou note now
Adouna ndéké dara meunoul Doy
All time all time
I Need life now more
I miss you and I'm crying
I don’t know for how long
I pray i pray
I’m praying for you
All day all night
I don't now for how long
Watch Video
About Miss U
More KID DOU Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl