Paparazzi Lyrics
Paparazzi Lyrics by SAMBA PEUZZI
Job bougn done khèpp légui fay nama lèrneu
Mougn yingueu donn mougn yaye
Lègi lèpp djèkhne
Commencer rap gnounnleu seu dom dji dofneu
Dann abeu call pour photowo lègui meuneue toumeu guèneu ndakh
Ay pararazzi sama side wawaw
Ay pararazzi sama side wawaw
Ay pararazzi sama side wawaw
Ay pararazzi sama side wawaw
Hey
Am gnou nane papam boudonn doundou doukko dèff
Réussir leu done gnane t mangui koy dèff
École two william éduc fala djar
Langg raps tcheupp yalla suur en
Seuteuteutt gueufj na dègg si kanam passs
Vroum vroum by my motor sport lèpp lèrna lèpp lèrna
Ay pararazzi sama side wawaw
Ay pararazzi sama side wawaw
Ay pararazzi sama side wawaw
Ay pararazzi sama side wawaw
Hey
Poche ak khèl bou fess
Liguèy tour bi dèss fi
Légende comme you (youssou ndour)
Légende comme papa thione (thione seck)
Yagueu sonou si mane
Mama massa tchono
Lo gueum mou fayla
Gnounn par force dagnouy tèddeu
Job bougn done khèpp légui fay nama lèrneu
Mougn yingueu donn mougn yaye
Lègi lèpp djèkhne
Commencer rap gnounnleu seu dom dji dofneu
Dann abeu call pour photowo lègui meuneue toumeu guèneu ndakh
Ay pararazzi sama side wawaw
Ay pararazzi sama side wawaw
Ay pararazzi sama side wawaw
Ay pararazzi sama side wawaw
Watch Video
About Paparazzi
More SAMBA PEUZZI Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl