Saint-Valentin Lyrics
Saint-Valentin Lyrics by YOUSSOU NDOUR
Tell me, wakh maa
Chérie, lo wakh ma deef
Sunu, st Valentin
Buess bi yaw yay borome
Tell me, wakh maa
Chérie, lo wakh ma deef
Sunu, st Valentin
Buess bi yaw yay borome
Chérie boy, chérie boy Wakh maa
Chérie boy beggou maa, ngay xalaat
Chérie mon amour
Ne te fais pas de soucis
Oh my darling
Tell me, wakh maa
Chérie, lo wakh ma deef
Sunu, st Valentin
Buess bi yaw yay borome
Tell me, wakh maa
Chérie, lo wakh ma deef
Sunu, st Valentin
Buess bi yaw yay borome
Chérie boy
Mbaa mère woo maa
Souma la togne yéé
Yeggou ma ko
Chérie boy, souma sanoon
Doo yi xalaat yaw
Je veux te voir toujours bekk
Baby, my baby newel jegge ma, jegge ma
Nuy waxtaa, nook o beggée ma defaa la ko
Jegge ma, kaay jege ma mon amour
Begg u ma yaw ngay xalaat
Do not be worried
Tell me, wakh maa
Chérie, lo wakh ma deef
Sunu, st Valentin
Buess bi yaw yay borome
Tell me, wakh maa
Chérie, lo wakh ma deef
Sunu, st Valentin
Buess bi yaw yay borome
Nelawal, ba yanndoor
Ne te fais pas de soucis
Nelawal yaw, bul xalaat
Du ma def lu lay sonnal
Nelawal mon amour
Ne te fais pas de soucis
Donne-moi ta main
Nan and dox antu ji
Tell me, wakh maa
Chérie, lo wakh ma deef
Sunu, st Valentin
Buess bi yaw yay borome
Watch Video
About Saint-Valentin
More YOUSSOU NDOUR Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl