JEEBA Happy Birthday cover image

Happy Birthday Lyrics

Happy Birthday Lyrics by JEEBA


Joyeux anniversaire happy birthday too you
Joyeux jooyeux

[COUPLET 1]
Degg na dioudou gou reuy ndaye ak baye
Wanté foulak fayda boromam
Mane degg na dioudou gou reuy ndaye ak baye
Wanté foulak fayda boromam
Niit gni dofouniou linga dji lagn lay fay
(Linga dji lagn lay fay)
Woté wo nieupa ngui tew di khar sa birthday
(Happy Birthday)
Kharit yi tew mbok yi dila nianal
Yafi def lou diara waax
Sama batt bi keen douko téyé
Nioungui weuy di nane
 
[REFRAIN]
Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire dieulal beuss bi yako mome
Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire, happy birthday to you
Joyeux joooyeux, Happy birthday to you
Joyeux joooyeux

[COUPLET 2]
Guiss nama rée contane bégue ba dioy
Sama cadeau bi yako mom
Fouma meuna né damay teew
Néla ko diabe I wish you all the best
Linga geuna beugg lalay diokh
Bou doyoul reik ma dance kone rk ma dance
Kone féthial fethial reik ma guiss
Yokal music bi mou diok thi kaw
Beuss bou dellou ci dou dafa nexx
Kone amoul stress c'est la fête
Sapé comme jamais khar zero heure
Zéro heure, sapé comme jamais zéro heure
Yeah Talal ma bougie gniou dague souniou gâteau ooho
Kouma diokhoul cadeau méré nala té boul ma wooh....(bouma statut )
Bene beuss la thi atte yi faw gnou begué ko
Ndéem meune ta gnak fo diar niou féte ko
Niougui way di naane

[REFRAIN]
Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire dieulal beuss bi yako mom
Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire
Joyeux anniversaire happy birthday to you
Joyeux joooyeux
Happy birthday to you
Joyeux joooyeux
Happy birthday to you
Joyeux joooyeux
Happy birthdaaay

Degg na dioudou gou reuy ndaye ak baye
Happy birthdaaay
Wanté foula ak fayda boromam
Happy birthdaaay
Degg na dioudou gou reuy ndaye ak baaaye
Happy birthdaaay
Wanté foula ak fayda boromam
Feithial feithial reik ma guiss
Yokal music bi mou dieum si kow
Beuss bou delou si dafa nexx
Feithial feithial reik ma guiss
Happy birthdaaay to you
Feithial feithial reik ma guiss
Yokal music bi mou dieum si kow
Beuss bou delou si dafa nexx
Happy birthdaaay to you youuu
Boroomam boroomam

 

Watch Video

About Happy Birthday

Album : Happy Birthday (Single)
Release Year : 2018
Added By : Afrika Lyrics
Published : Nov 24 , 2018

More JEEBA Lyrics

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl