So Mané Waw Lyrics
So Mané Waw Lyrics by JEEBA
Mane tanne nala si jigueen yudul diekh
Jokh Nala sama xool bi yaay borom
Kone baby boul ma négligé maay sa xool
Ndakh malay jokh leep lu geune si yoow
Mane tanne nala si jigueen yudul diekh
Jokh Nala sama xool bi yaay borooom
Boul négligé xamal ni Yaay sama xool
Ndakh beugg nala yoow bae beugg nala
Mane So mané waw ma nieuw sen keur
Yoow beugg nala yoow bae beugg nala
Mane So mané waw ma nieuw sen keur
Yoow beugg nala bae beugg nalaa
Woo nala telephone dieulou loo
Envoyé nala message wuyuwoo
Lane motakh yow babe lane motakh
Woo nala telephone dieulou loo
Envoyé nala message wuyuwoo
Lane motakh yow babe lane motakh
Bou mbeguel done diaay
Bou mbeguel done diaay
Yow babe diokh nala la xool bi
Wayé leep yakoo moom
Wayé neewoul dama niaak diom
Meussuma niaak diom
Mane sama mbeuguel moma yobou
Motakh malaay wo oh
Lane motakh babe lane motakh
Soumalay woo tei babe doma dieul
Lane motakh babe lane motakh
Soumalay woo tei babe doma dieul
Ndakh beugg nala yoow babe beugg nala
Mane So Mané waw ma nieuw sen keur
Yow beugg nala yow babe beugg nala
Mane So Mané waaw ma nieuw sen keur
Ma nieuw ma nieuw ma nieuw
Beugg nala yow babe beugg nala
Watch Video
About So Mané Waw
More JEEBA Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl