Gëm Na Tekki Fi Lyrics
Gëm Na Tekki Fi Lyrics by MAABO
[COUPLET 1]
Toleu sounou ndaw
Bountou adouna nek thi yoonou ndam
Danne dolé khamni
Dagnou wara Ame
Beey sounou wéwou tank
Moy foulak fayda
Geum sounou bopp lay doréé
Si taakh yii ak kaaw gua
Diouk dieuf diotnaa
Liguéy dess sounou reew
Ak sounou ngor lagne sokhla
Lougnouy deeem woutidji bitiim reew gnakoufii
Bougnsi dioublo akii pékhéé Amkofi
[REFRAIN]
Boul nangui faa
Bala gua nakhhsayy
Togal tchi reew mi
Teek fii waalaahi
Geum na nii meune na tekki fii
Liigeuy tedd fii
Meune na tekk fi
Gualla baaye togaal
Tchi deuk bi (meune na tekk fi)
Heyy gnou ndiarigne deukk bi
(meune na tekk fi hey)
[COUPLET 2]
Geum sa bopp khol tchi say mbokk
Moytandikou di wook sa dook
As goor dou faté
Ngor foula ak fayda
Tchi la bokk
Allal lay fadji guathié banekh fadioul nakaar
Meuna weur mayéwoul weurseuk
Kouné dioudook sa weurseuk bilaaay
Wakh diou werr lala wakh
Togal tchi rewmi boul dem feene
Naapeu Saameu Beey doundé
Leppagui dohk tchii rewmi
Bougnou tchiouné wawaw
Wakh diou werr lala wakh
Togal tchi rewmi woute métier
Naapeu Saameu Beey doundé
Leppagui dohk tchii rewmi
Bougnou tchiouné wawaw
[REFRAIN]
Boul nangui faa
Bala gua nakhhsayy
Togal tchi reew mi
Teek fii waalaahi
Geum na nii meune na tekki fii
Liigeuy tedd fii
Meune na tekk fi
Gualla baaye togaal
Tchi deuk bi (meune na tekk fi)
Heyy gnou ndiarigne deukk bi
(Meune na tekk fi hey)
[COUPLET 3]
Souf si sougnou souufff la
Nagne djiiw dina mégnii
Diourr donguaa laa
Took fi guarab gui sounou mbeey laa
Toole yii lossi deff mou faylaa
Ndakh tchiiono dou saay kone diouge
Rewmi gnoko meune defar bamou naat
Siggil Sougnou Sénégal
[REFRAIN]
Boul nangui faa
Bala gua nakhhsayy
Togal tchi reew mi
Teek fii waalaahi
Geum na nii meune na tekki fii
Liigeuy tedd fii
Meune na tekk fi
Gualla baaye togaal
Tchi deuk bi (meune na tekk fi)
Heyy gnou ndiarigne deukk bi
(Meune na tekk fi hey)
Boul nangui faa
Bala gua nahkksayy
Togal tchi reew mi
Tekk fii waalaahi
Boul nangui faa
Bala gua nakksayy
Togal tchi reew mi tekk fii waalaahi
Toggal tchi deukk bi
Gnou dirigne deukk bi
Ndakh gnoune gouney deukk bi
Gno wara defar deukk bi
Togal tchi deukk bi
Ndiarigne amena chi deukk bi
Togal tchi deukk bi
Ndimbeul amena tchi deuk bi
Geum sa gokh
Sokkoli sa gokh
Geum sa bopp
Gnaak diarignou
Geum sa gokh
Sokkoli sa gokh
Geum sa bopp
Gnaak diarignou
Geum sa gokh
Sokkoli sa gokh
Geum sa bopp
Gnaak diarignou
Watch Video
About Gëm Na Tekki Fi
More MAABO Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl