Boum Bam Lyrics
Boum Bam Lyrics by OMG
[VERSE 1]
Mon cœur fait boum bam
Mon cœur fait boum bam
Yague na ngamay doflo
Té meussou malako wakh
Sa leep ma saf ba ningay rétané
Nane lay def nga kham ko
Beugue na nga kham ko
Diafé na ma wakh ko
Hey bilay walay
Khol bi nga mome ko
Lo beugue ma done ko
Hey bilay walay
[HOOK]
Dingama doflo
Yamay beglo
Dingama doflo
Yamay dioylo
[CHORUS]
Mon coeur fait boum bam boum bam
Dakh yaw
Mon coeur fait boum bam boum bam
Pour toii
Mon coeur fait boum bam boum bam
Dakh yaw
Mon coeur fait boum bam boum bam
Pour toi
Boum bam boum bam boum bam bam
Boum bam boum bam boum bam bam
[VERSE 2]
Moussouma wone guem ni
Mbeuguel dina dokh souniou digueunté
Sama khol bi rek nga kheuy keuf
Ba foumala guiss sama fiite def teuf
Fouma meuneu nek
Mane may sa yeuf
[HOOK]
Dingama doflo
Yamay beglo
Dingama doflo
Yamay dioylo
[CHORUS]
Mon coeur fait boum bam boum bam
Dakh yaw
Mon coeur fait boum bam boum bam
Pour toii
Mon coeur fait boum bam boum bam
Dakh yaw
Mon coeur fait boum bam boum bam
Pour toi
[BRIDGE]
Ayéeéé héhéééé
Beugue nala sama khol bééé
Ayééé hééhéééhééé
Beuguenalaaaaaaaaaaa
[CHORUS]
Mon coeur fait boum bam boum bam dakh yaw
(Mon coeur fait boum bam bam bam bam bam bam bam hey)
Mon coeur fait boum bam boum bam
Pour toii (bam bam bam bam bam bam hey)
Mon coeur fait boum bam boum bam
Dakh yaw
Mon coeur fait boum bam boum bam
Pour toi
Mon coeur fait boum bam (boum bam bam bam )
Mon coeur fait boum bam (bam bam bam
Mon coeur fait boum bam
Pour toi pour toi
Mon coeur fait boum bam (boum bam bam bam )
Mon coeur fait boum bam (boum bam
Mon coeur fait boum bam
Pour toiiiiiiiiiii
Watch Video
About Boum Bam
More OMG Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl