Solou Golo Lyrics
Solou Golo Lyrics by DA BRAINS
Loutakh nga mana faté démbeu
Yaye boy ko défal lou bakh mou woor leu
Fii dagnouy niakeu diamou Yalla
Kouthie am faté démbeu badoola ngeu
Yaye boy adouna amoul solo
Waykate yék mbeur yék footballeur kou geuna goré
Kou thi siiw faté démbeu faté fanga diougué
Té niom kothi défal lou bakh mou kheuy solou golo
Yaye boy adouna amoul solo
Waykate yék mbeur yék footballeur kou geuna goré
Kou thi siiw faté démbeu faté fanga diougué
Té niom kothi défal lou bakh mou kheuy solou golo
Mbeur loutakh nga mana faté démbeu
Yaye boy ko défal lou bakh mou woor leu
Fii dagnouy niakeu diamou Yalla
Kouthie am faté démbeu badoola ngeu
Beugna kham loufi diar ngay yékeuti mbaggeu
Di niodi star fathiour teinte té yoro deureum
Sambay mbayane ték di fay louyass keureum
Mbalakhmane yi thi séne biir deuké kheureum
Footballeyrs y gél you khés yi gnoléne sonal
Dagnon beugeu téleu siiw louné laléni diaral
Touti gneuw vacance weur buzz rek gél ba gnibi
Faté kogn bi faté mbok yék lilène fi indi
Gnoune rappeur yi dagnon sokhor sougnou biir
Gno dakha saaga dakha khasté dakha kaas
Té ligniy déf sougn ka wakhone deuk bi taas
Dagnon torokh té si sohkor khol yi bone
Yaye boy adouna amoul solo
Waykate yék mbeur yék footballeur kou geuna goré
Kou thi siiw faté démbeu faté fanga diougué
Té niom kothi défal lou bakh mou kheuy solou golo
Yaye boy adouna amoul solo
Waykate yék mbeur yék footballeur kou geuna goré
Kou thi siiw faté démbeu faté fanga diougué
Té niom kothi défal lou bakh mou kheuy solou golo
Niit gni khamni légui nga fouy faté démbeu anh
Amnga chauffeur garde du corps ak quelques soukhou anh
Nénga légui star nga do démati kogne ba anh
Bofi déwone tay fougnou lay dioulé dou diouma kogne ba
Niata fane sa messeu dionthiou yaw nga teudé léne
Lék séne alal téléphone nga bloquer léne
Dougnou la woo diote la té kossi sokla diote ko
Téla fouy daka lép té doléne fay kéney
Niit bou siiw bou té kéné solou golo tok di dioy
Té bamouy doundou hypocrite louné nga ték si dérame
Gni léne weur bougou gnouléne dougnou léne wakh deugeu
Dani mar sa tate tass sa keur fa mane la fépou
Kouthi dakha fay nga tékma liguéye yakhma
Khana khamoné akh mana yakh sa carrière
Serigne sangue nala sokhor takhna amo bayré
Kougne la totoré nga mer
Nala lérni dougnou doundou
Yaye boy adouna amoul solo
Waykate yék mbeur yék footballeur kou geuna goré
Kou thi siiw faté démbeu faté fanga diougué
Té niom kothi défal lou bakh mou kheuy solou golo
Yaye boy adouna amoul solo
Waykate yék mbeur yék footballeur kou geuna goré
Kou thi siiw faté démbeu faté fanga diougué
Té niom kothi défal lou bakh mou kheuy solou golo
Watch Video
About Solou Golo
More DA BRAINS Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl