Hypocrisie Lyrics by ABDOU GUITé SECK


Kouy naan di lakhou, so mandé fégne
Yaw dé dagua fégne lé, ba takh niou ragné la
Kouy naan di lakhou, so mandé fégne
Yaw dé dagua fégne lé, ba takh niou ragné la

Respectel rendez-vous, sa cadou doon sa nawlé
Mo guen niou woo, nga naane mang thi yoon wi
Hypocrisie moo gueneu niaw thi défin
Té man li ma diakhal dafa fess ci rew mi

Nitou tay dalay djitou gassal la cambe
Nieuw diuel ci la lengook yaw dieum thia foofou
Ngay andak nit, ndéké yaa gui ko ték sa beut
Moulay dimbali nga kheuy beugue ko yakh
Ndakh yaa ngua dieum fanénoo di fa séntou lanéne
Yalla doula sétan koula wolou dioum na
Hypocrisie moo gueneu niaw thi défin
Té man li ma diakhal dafa fess ci rew mi

Moytoul niou naan la (hé ndakha ngué)
Ngay khodalikou di défarou ak di noyé (hé ndakha ngué)
Ndèkè ndakha dafay nakhé mbaay (hé ndakha )
Loo amoul bou ko diglé
Loo meunoul bou ko wakh yaw
Guiss naa ni ya ngui may rétaan
Waaya ci sa bir khol
Yaw beggouloo thi man
Loo amoul bou ko diglé
Loo meunoul bou ko wakh yaw
Nit dafay manou
Mandoo ma gueuneul dekké diouli ‘manoo)
Matar welle sow sama wadji
Promoteur immobilier ba thia diamniadio
Domi aminata touré ma thia gassan
Bayou boubacar matar welle ow
Sidath diop macodou ndiaye
Lafan day dem
Adama mbodj goro madame diatta
Sama waa dji
Loo amoul bou ko diglé
Loo meunoul bou ko wakh yaw
Loo meunoul buko diggle
Matar welle sow néna
Nit dafay manou

Watch Video

About Hypocrisie

Album : Hypocrisie (Single)
Release Year : 2021
Added By : Farida
Published : Jul 28 , 2021

More ABDOU GUITé SECK Lyrics

ABDOU GUITé SECK
ABDOU GUITé SECK
ABDOU GUITé SECK

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl