Diem Ko Lyrics
...
Diem Ko Lyrics by ABDOU GUITé SECK
Diem ko
Daan ko, sekyaane
Meun gua ko
Kon def ko, dindil niou ko
Bayi len wakhoum peite nieuw daal niou yokk dole
Bayyi tappale
Sa bou sounou rew wote
Auto bi boum la fi ba boul sissou ba mou raw la
Nieuweul niou yobou la la a la la
Diaam day nangou dogal ba
Saitou ko songou ko
Sagn gua ko def ne sonko
Mani diem ko meun gua ko
Ni def ko dindi dji koo
Moytoulen wakhoum peite yen daal na lepp gore
Nit ki day gore
Sa bou sounou rew wote
Sa bou wote na mel ni nodou gou djip
Dioulit dem sabbal yallah diokh ko momelam
Donte koume am na and bounou fass yenne and
Dieul mbalit mi annnnn
Yallah sakh dathiy and
Guis gua nokk sounouy sekkel dound nan fi bepp mbettel
Tewoul tewoul teel
Senegal la niou votel
Dioub dioubeul dioubenti tekk thi nak di lidjienti
Li fi ne koune am thi niou dem ba koune diot thi
Gendarmerie nationale police nationale
Askan ken doukou sonal te beugou ma len tignial
Anna mouvement senegal first momo mi djitou
Andak ndiaga seck sunu président
Mouvement bi ragnie nan ko massoul guestou ben yoon
Da niou and bollo manko gueum ko tek thi yoon
Nioun nio ni réformistes sore nanook terroristes
Nittou deugg valeur la nou djitalak honneur kon
Songou ko, sahn gua ko
Def ne sonko
Diem ko meun gua ko
Kon def ko, dindi djiko
Diem ko, song ko
Daan ko def ne sonko
Sagn gua ko, meun gua ko
Kon def ko gindi djikoo
Watch Video
About Diem Ko
More ABDOU GUITé SECK Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl