Sale Temps Lyrics
Sale Temps Lyrics by ONE LYRICAL
[VERSE 1]
Def na lou bax, def na lou bone
Encaissé na paiement école
Meuss nala dioylo maman balma
Fen na dieul na louma momoul
Tek nala deal tek nagn ma deal
Menacé nagn ma beug ma kill
Tokh na ay khétou mandi mandi waw
Té meussouma kham lou nane di saf
Fok ni niou bracké pick mane ak sama ancienne équipe
Bénen doundu bénén vécu
Télé bay samay études
Féké na li sama yaye doundu
Féké na li sama baye doundu té thiol ci mane
Fatéwouma li sama none doundak mane
No no no no
[CHORUS]
Sale temps
Sale temps
Sale temps
Sale temps
[VERSE 2]
Niatta nioma nokh
Niatta lafi niouss
Niatta nioma neukheul
Niatta lafi nakh
Chef de gang’ou école
Moussouma dieund blouse
Lathie ko Mr Diallo
Shud up ma niggah you, yéwu fadjr ak siwou
Rafet khaliss sandi si you do diangue missi you
Nangou sa mbourou mbiskit
Ma doli def na lou bakh def na lou bone
Tay moudjé done lima beugone done
Meusna la djoylo yaye nga balma
Dieulna louma momoul
Lamou mani mangui ci problème
Dougate ci problème, fanane ci problème
Yando ak problème
Balma, balma, balma
[CHORUS]
Sale temps
Sale temps
Sale temps
Sale temps
Watch Video
About Sale Temps
More ONE LYRICAL Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl