Mariage Forcé Lyrics
Mariage Forcé Lyrics by VIVIANE CHIDID
[VERSE 1]
Yaye boye li lane la ni
Loutax nga beug ma may kouma khamoul
Baye boy eki kane la ni
Loutax nga beug ma mey kouma noboul
Té mane mi ma ngui doga dougou ci
Samay fouki atte ak diourome niar
Té mane mi khalé la yaye
Bayi ma ma diangue bassi kaname
[CHORUS]
Mane niowou ma seuy wayy
Mane niowou ma seuy wayy
Mane niowou ma seuy wayy
Mane niowou ma seuy wayy
Ki amna allal amna daraja
Auto you rafète ak keur you rafète
Ki amna allal amna daraja
Auto you rafète ak keur you rafète
[VERSE 2]
Loutax lolou
Wawaw yaye kham nani tarou djiguène moy seuy
Watt nani dou mane ak sen wadji lé
Féké né na allal la len di diay
Kone ma khamni sama ndaw dou diay
Kham ngèn li ci birou négou seuy
Bokk ak lale ko khamoul every day
Metina ci xol sa ndeye
Mariage forcé mom waroula diay
[CHORUS]
Mane niowou ma seuy wayy
Mane niowou ma seuy wayy
Mane niowou ma seuy wayy
Mane niowou ma seuy wayy
Ki amna allal amna daraja
Auto you rafète ak keur you rafète
Ki amna allal amna daraja
Auto you rafète ak keur you rafète
Ki amna allal amna daraja
Auto you rafète ak keur you rafète
Ki amna allal amna daraja
Auto you rafète ak keur you rafète
Té mane mi ma ngui doga dougou ci
Samay fouki atte ak diourome niar
Té mane mi khalé la yaye
Bayi ma ma diangue bassi kaname
Yaye boy (bayi len khallé yi niou diangui)
[CHORUS]
Ki amna allal amna daraja
Auto you rafète ak keur you rafète
Ki amna allal amna daraja
Auto you rafète ak keur you rafète
Ki amna allal amna daraja
Auto you rafète ak keur you rafète
Ki amna allal amna daraja
Auto you rafète ak keur you rafète
Watch Video
About Mariage Forcé
More VIVIANE CHIDID Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl