Mame Boye Lyrics
Mame Boye Lyrics by WALLY SECK
Mame boye boulma di méré sama mame
Dinala setsi Mame
Mame boye boulma fi méré sama mame
Dinala setsi Mame
Oooh Oohhh Ohhhh Oooohhhhh
Oohhh oohhh oohhh oohhhhh
Malay xalaat all time
Ioe sama mame yama yarr yama
Diapalé ioe la beug
Mane malay xalaat all time
Ba poullo diery ndegeum
Kene nieuwoul bokko
Shibireppp rep rep rep barabiriré
Damalay xalaat all time
Ba poullo diery ndegeum
Kene nieuwoul bokkooo
Mame boye boulma di méré sama mame
Dinala setsi mame
Mame boye boulma di méré sama Mame
dinala setsi mame
Dinala setsi Mame
Dinala setsi maaaame
Mame boye mame boye
Mamamaam dinala setsi
Mame dinala setsi maaaame
Damalay xalaat all time
Damalay xalaat all time
I will talk to you Ndeye woury
Fall ndeye soda Fall nga
Bokal ndey ak baye dinala
Setsi mame boye(mame boye)
Sira Ndiaye gorou Fall
Mame boye(mame boye)
Sira ndiara gorou Fall
Mame boye mame boye
Talibé Sérigne Babacar
Sy sopey Dabakh Sy Malick
Mi ngui ber-ndel ngi gnou
Thieureulé mi gnou thieureulé
Sèn baaye bi
El hadji Malick Sy
Sira Ndiara gorou Fall mame boye
Watch Video
About Mame Boye
More WALLY SECK Lyrics
Comments ( 0 )
No Comment yet
You May also Like
Get Afrika Lyrics Mobile App
About AfrikaLyrics
Follow Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl