Paroles de Sama Life
Paroles de Sama Life Par BRIL
[VERSE 1]
Tout a commencé quand nos regards se sont croisés
Elle a renversé mon cœur, elle l’a fait chavirer
Dama dof ci mom j’ai perdu la tête (Crazy about love)
Notre histoire est cool, il ne faut pas qu’elle s’arrête
Baby tu es mon soleil, tu brules tout autour de toi
La glace devient vapeur, tes yeux me laissent sans voix
Tchi ioe rek la dof, dafa leer, baby yay sama life
[CHORUS]
The first time I saw you, la kham yay sama life
Beug nala loool, ioe yay sama life
(I love you – I love you, baby I love you – I love you)
(I love you – I love you, baby I love you – I love you)
Yay wétali sama doundou, baby je peux t’appeler ma vie
Nék ak ioe forever loloy sama envie
(I love you – I love you, baby I love you – I love you)
(I love you – I love you, baby I love you – I love you)
[VERSE 2]
I look at you as if you are the only girl around
Loutakh nioumay togn, naniou ma bayék sama yeuf
Let me feel important, please never let me down
Yay sama djonguama, khawma sakh lane ngama def
I love you with my heart and will my soul
Baby you should believe me when you see sing this sound
Geumeul ni leep deug la, what I feel inside is real
Y’Allah def ma beug la, when I say this , I’m for real
May sa mari ioe wowé ma chou
Rom nga Eva ak Marichou
Da ngama beug ma romb la djégué la
Wax lako wowéla baby boo
Tchi ioe rek la dof dafa leer baby yay sama lfe
[CHORUS]
The first time I saw you, la kham yay sama life
Beug nala loool, ioe yay sama life
(I love you – I love you, baby I love you – I love you)
(I love you – I love you, baby I love you – I love you)
Yay wétali sama doundou, baby je peux t’appeler ma vie
Nék ak ioe forever loloy sama envie
(I love you – I love you, baby I love you – I love you)
(I love you – I love you, baby I love you – I love you)
[OUTRO]
Ioe yay sama life, my life
(I love you – I love you, baby I love you – I love you)
Sama doundou ioe la, baby yay sama life
(I love you – I love you, baby I love you – I love you)
sama life, sama life, sama liiiife
(I love you – I love you, baby I love you – I love you)
Ecouter
A Propos de "Sama Life"
Plus de Lyrics de BRIL
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl