Paroles de LNN Par DIP DOUNDOU GUISS


[REFRAIN]
Nek ci yoon, nek ci deuk tchi bagna tok
Dérétou ennemie sama kaw
Deum la déma djigne lima done never give up 
Amna goudi you tiss douma daw
Douma faté bamay géneu galé papa kholal tay sa fils foumou tok
Lo niémé niakk
Lo niémé, Lo niémé, Lo niémé 
Lo niémé niak, lo niémé niak, lo niémé, lo niémé niak

[COUPLET 1]
Hey ! Amna ay défaites yi nga am
Ay métitou moumeu
Yek échelle mou danou
Guiss na ay serpent you mandou
Mayna moma sétou tromper guélou diambour
Meusna geum nitt kouma khamoul
Voté Afrique ma solal goumbeu cagoul
Baniouma jeunesse bouy nélaw
Wayé jeunesse sou new mo geun bou yéwu calou
Nek ci yoon, feint fi yéré you bone
Rendi fi gaindé youy mbow
Tour sama dérétou gorr
Ioe ioe ! Néko mou tok
Talouma kébétou thiow
Niom daniouy thiéné té amouniou diome
Soul ay rappeurs yo khamné bamay ram sen CD ngui daw
Damako kharé fils dama job
Pour sama avenir sama dome
Fils dama agné khif réré ndox
Diangue nga amo fiit amo ngor
Thiolou ba lay watié sama bop
 Fuck niémay coup d'état
Million la wantéré samay shows
Trone bi dafa soudé samay tate

Kou bote boukki ay
Faut kathie yi mbow la
Mane diapna nikey défé nonou la
Li nga def ci rapp bi
Mane dama moudié warru
Dip rap bi yako maquiller ba takh fépa tarru

[REFRAIN]
Nek ci yoon, nek ci deuk tchi bagna tok
Dérétou ennemie sama kaw
Deum la déma djigne lima done never give up 
Amna goudi you tiss douma daw
Douma faté bamay géneu galé papa kholal tay sa fils foumou tok
Lo niémé niakk
Lo niémé, Lo niémé, Lo niémé 
Lo niémé niak, lo niémé niak, lo niémé, lo niémé niak

 [COUPLET 2]
Nélaw dé bou nekh leu
Wayé dé bou nekh amoul fen
Talent deug ngen am
Yen sen talent moy meun fen
Gnimey mboubo lay mour
Dip dou jubo dey soul
Goré ba done esclave mo geun diay sa ngor ba done buur
Lokho bou tayal dou tabakh lou deugeur
Lo geuneu bégue di geuneu peuteukh
Ma takh ba labouniou niou dima neukeul
Welcome to life in the jungle
Lafe famay yobou mane sokhla wouma pneu
Wala daju si niakh wala peundeukh
Faté na demb té diap ci euleuk niari lokho gana moko geuneul
Sa gars yi réwantou dama len di ray
Kou djeumeum yarouwoul sa neew dou rew
Dieul leu nouniouy dieulé thiep bou bess 
Di nga nangou ba sa thieur yi bagn
Sama dieum ma geun sen def
Fayna ound fay wesh wesh
Def ni niom limay def rek déh
Séni bop ni bambel tek tek
Seni prof samay maitresse lagn
Kougn fi thiow si rapp bi may sa père
Yama meun boudé kou dakh fen
Lim fi yor si song dou khathie dou dièkh
Diameu geun mais ay mo dakh fay
Diw sa guel mouy geun di diap teint
Diw guelou niouy dakh yakh derr
Nieup nul ni lamb lac 2 guers

Kou bote boukki, faut kathie yi mbow la
Mane diapna nikey défé nonou la
Li nga def ci rapp bi, mane dama moudié warru
Dip rap bi yako maquiller ba takh fépa tarru 

[REFRAIN]
Nek ci yoon, nek ci deuk tchi bagna tok
Dérétou ennemie sama kaw
Deum la déma djigne lima done never give up 
Amna goudi you tiss douma daw
Douma faté bamay géneu galé papa kholal tay sa fils foumou tok
Lo niémé niakk
Lo niémé, Lo niémé, Lo niémé 
Lo niémé niak, lo niémé niak, lo niémé, lo niémé niak
  
[REFRAIN]
Dip dakoy yeungeul waye, dip dakoy yeungeul
Bass dakoy yeungeul waye
Bass dakoy yeungeul 
Bass dakoy yeungeul
Beusseul fi (beusseul)
Wouy beusseul fi (beusseul)
Ay beusseul fi, wa kone beusseul fi
Hé boy kone beusseul (lou bess)
Beusseul fi lou bess sa bess ay beusseul fi
Wa kone beusseul fi, lou bess sa bess
Dip dakoy yeungeul waye, dip dakoy yeungeul
Bass dakoy yeungeul waye, bass dakoy yeungeul 
Bass dakoy yeungeul waye, bass dakoy yeungeul
Beusseul fi (beusseul)
Wouy beusseul fi (beusseul)
Ay beusseul fi, wa kone beusseul fi
Hé boy kone beusseul (lou bess)
Beusseul fi lou bess sa bess ay beusseul fi
Wa kone beusseul fi, lou bess sa bess

Ecouter

A Propos de "LNN"

Album : LNN (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Sep 03 , 2019

Plus de Lyrics de DIP DOUNDOU GUISS

DIP DOUNDOU GUISS
DIP DOUNDOU GUISS
DIP DOUNDOU GUISS
DIP DOUNDOU GUISS

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl