Paroles de Dara Xéwul
Paroles de Dara Xéwul Par DIEYNA
Bril on the beat
Dieyna
Niouné Dara Xéwul
Mbekté gui thi mbeuguél la khamoul , ak yaw damay cool
Ba temps bi day gaaw
Kheuy di fééss thi yaw nga djékh thi mane , kane lay done koudoul Yaw
So wõté mbekté gui thi dila décrocher
Say vocal damakoy dégglouwatt di déé
Soma fiiré yone la ndakh loloy deuggui mbeuguél
Mais beuggna nga khamné ya fi né
Mane yama taneu thi séén biir
Ndaké yawla guéédj gui di riir
Sama coco, choco, baby boo, Cheri beuggouma reuthie thi sa fiir
Fii amoul deuss té yay péé
djeulo Xol bi diko ngeureum ngeureumé
Kou am wourouss dangg koy téé
Sagnsé lay def ba mélni panal
Daagou nga wakhma noma guissé
Fééss nga sama beutt , defla sama profil dila Xool ni Télé
Mane rek au commande kén dou zappé
Khol bou déé nga doundeul
Def thi bruit mouy riir té Wally teuggoul
Bayilén niou wakh, on se sait
Lithi néékh nonou la néékhé
Yay soukeur bi doul djokhé djaabétt
B wéétay dafmay dikkeul saa yo démé
Mbi do yitma, hakilam fof ko éh ma wane ta
Douma xool kéneu ndakh yaw démé féneu di xooli kénén
Awa mi wawa yadé bawoma
Mane yama taneu thi séén biir
Ndaké yawla guéédj gui di riir
Sama coco, choco, baby boo, Cheri beuggouma reuthie thi sa fiir
Fii amoul deuss té yay péé
djeulo Xol bi diko ngeureum ngeureumé
Kou am wourouss dangg koy téé
Sagnsé lay def ba mélni panal
Daagou nga wakhma noma guissé
Fééss nga sama beutt , defla sama profil dila Xool ni Télé
Mane rek au commande kén dou zappé
Ni wauloula takh ma toppoula
Fingama djéméma gueuneul fingama djeulé
Ni wauloula takh ma toppoula
Bou doyoul wakhma féppeu la meuné
Ragal féété day khaagné mbékté deuggla
Youssou wayna Aïda
Thione wayna Diaaga
Omar wayna Bana
izo wayna Faa
Ecouter
A Propos de "Dara Xéwul"
Plus de Lyrics de DIEYNA
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl